Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
and when the pharisee saw it, he marvelled that he had not first washed before dinner.
farisen bi nag daldi jaaxle, bi mu gisee ne yeesu raxasuwul, laata muy lekk.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
two men went up into the temple to pray; the one a pharisee, and the other a publican.
mu ne: «dafa amoon ñaari nit ñu dem ca kër yàlla ga, di ñaan. kenn ki ab farisen la, ki ci des juutikat.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
and as he spake, a certain pharisee besought him to dine with him: and he went in, and sat down to meat.
bi yeesu waxee ba noppi, benn farisen wax ko, mu ñëw lekke këram. yeesu dugg ca kër ga, toog ca lekkukaay ba.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
and one of the pharisees desired him that he would eat with him. and he went into the pharisee's house, and sat down to meat.
amoon na ab farisen bu ñaan yeesu, mu ñëw lekkandoo ak moom. yeesu dem kër waa ja, toog ca lekkukaay.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
circumcised the eighth day, of the stock of israel, of the tribe of benjamin, an hebrew of the hebrews; as touching the law, a pharisee;
xarafoon naa ca ayu-bés ga, bokk ci bànni israyil ci giiru ben-yamin, di ibrë ci deret ak ci meen. bu dee ci yoonu musaa ngeen bëgg a wax, ci tariixab farisen laa bokkoon;
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
and, behold, a woman in the city, which was a sinner, when she knew that jesus sat at meat in the pharisee's house, brought an alabaster box of ointment,
fekk amoon na ca dëkk ba jigéen juy moy yàlla. bi mu yégee ne, yeesoo ngay lekk ca kër farisen ba, mu dem, yóbbaale njaq lu ñu defare doj wu ñuy wax albaatar te def latkoloñ.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
then stood there up one in the council, a pharisee, named gamaliel, a doctor of the law, had in reputation among all the people, and commanded to put the apostles forth a little space;
waaye amoon na fa nit ku tudd gamaleel, bokk ci tariixab farisen ya, di xutbakat bu tedd ci yoonu musaa, mu jóg ca mbooloo ma, santaane ñu génne leen tuuti.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
but when paul perceived that the one part were sadducees, and the other pharisees, he cried out in the council, men and brethren, i am a pharisee, the son of a pharisee: of the hope and resurrection of the dead i am called in question.
naka noona pool, mi xam ne, genn-wàllu kureel ga bokk nañu ci tariixab sadusen ya, te ña ca des bokk ci tariixab farisen ya, mu wax ci kaw ci biir géew ba ne: «bokk yi, man farisen laa, te farisen moo ma jur; li tax ñu may àtte tey mooy sama yaakaar ci ne, ñi dee dinañu dekki.»
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :