Vous avez cherché: receive (Anglais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

i receive not honour from men.

Wolof

«wutuma tagg yu jóge ci nit.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and he gave heed unto them, expecting to receive something of them.

Wolof

lafañ bi xool leen, yaakaar ne dina jot dara ci ñoom.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

if thou count me therefore a partner, receive him as myself.

Wolof

soo ma jàppee ni nawle nag, teeru ko, ni su ma la doon ganesi.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and if ye will receive it, this is elias, which was for to come.

Wolof

te yaxya moomu, su ngeen bëggee nangu lii, mooy iliyas bi waroon a ñëw.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

against an elder receive not an accusation, but before two or three witnesses.

Wolof

kuy tuumaal njiit fi yaw, bu ko gëm, li feek ñaar walla ñetti seede dëggaluñu ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and they did not receive him, because his face was as though he would go to jerusalem.

Wolof

waaye waa dëkk ba nanguwuñu ko, ndaxte mi ngi jublu woon yerusalem.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and all things, whatsoever ye shall ask in prayer, believing, ye shall receive.

Wolof

te lépp lu ngeen laaj cig ñaan, bu ngeen ci boolee ngëm, dingeen ci jot.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

he shall glorify me: for he shall receive of mine, and shall shew it unto you.

Wolof

dina ma màggal, ndaxte lu mu leen wax, ci man la ko jële.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and into whatsoever city ye enter, and they receive you, eat such things as are set before you:

Wolof

«dëkk bu ngeen man a dugg, te waa dëkk ba teeru leen, lu ñu leen jox, lekkleen ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and teach customs, which are not lawful for us to receive, neither to observe, being romans.

Wolof

di xamle ay aada yu nu sañul a nangu mbaa nu di ko topp, nun ñi bokk ci nguuru room.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and at the season he sent to the husbandmen a servant, that he might receive from the husbandmen of the fruit of the vineyard.

Wolof

«bi tool bi ñoree nag, mu yónni surga ci ñoom, ngir jot wàllam ci meññeef gi.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and hath seen in a vision a man named ananias coming in, and putting his hand on him, that he might receive his sight.

Wolof

te gis na cim peeñu nit ku tudd anañas, mu dugg, teg ko ay loxo, ba muy gisaat.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and whatsoever we ask, we receive of him, because we keep his commandments, and do those things that are pleasing in his sight.

Wolof

te lépp lu nu koy ñaan, dinanu ko jot ci moom, ndaxte nu ngi sàmm ay ndigalam, di def lu ko neex.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and saw him saying unto me, make haste, and get thee quickly out of jerusalem: for they will not receive thy testimony concerning me.

Wolof

ma daldi gis boroom bi, mu ne ma: “génnal yerusalem ci ni mu gën a gaawe, ndaxte duñu nangu li ngay seede ci man.”

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and i say unto you, make to yourselves friends of the mammon of unrighteousness; that, when ye fail, they may receive you into everlasting habitations.

Wolof

yeesu teg ca ne: «maa ngi leen di wax lii: sàkkuleen ay xarit jaare ko ci alalu àddina, ngir bu alal nekkatul, ñu man leen a fat ca dal yu sax ya.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and if i go and prepare a place for you, i will come again, and receive you unto myself; that where i am, there ye may be also.

Wolof

te su ma leen defaralee bérab booba ba noppi, dinaa dellusi, yóbbaale leen, ba fu ma nekk, ngeen nekk fa, yéen itam.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and he causeth all, both small and great, rich and poor, free and bond, to receive a mark in their right hand, or in their foreheads:

Wolof

mu def it ba ñépp, mag ak ndaw, buur ak baadoolo, gor ak jaam, ñépp am màndarga ci seen loxol ndeyjoor walla ci seen jë,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

by faith abraham, when he was called to go out into a place which he should after receive for an inheritance, obeyed; and he went out, not knowing whither he went.

Wolof

ngëm moo tax ba ibraayma déggal yàlla. bi ko yàlla wooyee, mu dem toxu ci menn réew, ma mu waroon a jote ca yàlla. noonu la gàddaaye dëkkam te xamul woon fan la jëm.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

i would that ye all spake with tongues, but rather that ye prophesied: for greater is he that prophesieth than he that speaketh with tongues, except he interpret, that the church may receive edifying.

Wolof

léegi nag bëgg naa yéen ñépp, ngeen di wax ay làkk, waaye li ma gënal mooy ngeen di wax ci kàddug yàlla. kiy wax ci kàddug yàlla moo gën kiy wax ay làkk, su firiwul li muy wax, ngir ngëmu mbooloo mi yokku.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and when he was disposed to pass into achaia, the brethren wrote, exhorting the disciples to receive him: who, when he was come, helped them much which had believed through grace:

Wolof

naka mu bëgg a dem akayi, bokk ya xiir ko ca, ñu bind taalibe ya, ngir ñu teeru ko teeru bu rafet. noonu mu dikk fa te jariñ lool ñi gëm jaare ko ci yiwu yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,847,621 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK