Vous avez cherché: run through the clov (Anglais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

but he passing through the midst of them went his way,

Wolof

waaye moom mu jaar ci seen biir, dem yoonam.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

for we through the spirit wait for the hope of righteousness by faith.

Wolof

waaye njub, gi nu yàlla dencal ëllëg, nu ngi koy séentu ci kaw ngëm ak ci ndimbalu xelum yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

for i through the law am dead to the law, that i might live unto god.

Wolof

ci li jëm ci yoonu musaa, dee naa, fekk yoon wi ci boppam moo ko waral, ngir ma man a dund, ba amal jariñ yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

in whom ye also are builded together for an habitation of god through the spirit.

Wolof

te ci seen bokk ci kirist, yàlla boole na leen tabax yéen itam, ba ngeen nekk dëkkukaayam, jaar ci xel mu sell mi.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and would not suffer that any man should carry any vessel through the temple.

Wolof

te mayul kenn, mu yóbbu am njaay ci kër yàlla gi.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and he went through the cities and villages, teaching, and journeying toward jerusalem.

Wolof

yeesoo ngi doon jaar ci ay dëkk yu mag ak yu ndaw, di jàngale te jublu yerusalem.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

being justified freely by his grace through the redemption that is in christ jesus:

Wolof

waaye gannaaw kirist yeesu dee na ngir jot leen, yàlla ciw yiwam man na leen a àtte ni ñu jub ci dara.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and for their sakes i sanctify myself, that they also might be sanctified through the truth.

Wolof

sellal naa sama bopp ngir ñoom, ngir ñu sampu ci dëgg te sell.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and they departed, and went through the towns, preaching the gospel, and healing every where.

Wolof

noonu ñu dem dëkk ak dëkk, di fa yégle xebaar bu baax bi, tey wéral jarag yi.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and it came to pass, as he went to jerusalem, that he passed through the midst of samaria and galilee.

Wolof

bi muy dem yerusalem ba tey, yeesu jaar ci dig wiy xaajale samari ak galile.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

for all things are for your sakes, that the abundant grace might through the thanksgiving of many redound to the glory of god.

Wolof

ndaxte lépp li nuy daj, seen njariñ a tax, ngir yiwu yàlla, wiy yokku ci nit ñu gën a takku, yokkaale ngërëm lu jëm ci yàlla, ngir jollil ndamam.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

blessed are they that do his commandments, that they may have right to the tree of life, and may enter in through the gates into the city.

Wolof

«yéen ñi fóot seeni mbubb, ngir sañ a lekk ci garabu dund gi te dugg ci bunti dëkk bi, barkeel ngeen.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and as they went through the cities, they delivered them the decrees for to keep, that were ordained of the apostles and elders which were at jerusalem.

Wolof

bi loolu amee ñuy jaar ca dëkk ya, jottali leen dénkaane, yi ndaw yi ak njiit yi nekk yerusalem joxe, te sant leen ñu sàmm ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and again i say unto you, it is easier for a camel to go through the eye of a needle, than for a rich man to enter into the kingdom of god.

Wolof

ma waxaat leen ko: giléem jaar ci bën-bënu pusa, moo gën a yomb boroom alal dugg ci nguuru yàlla aji kawe ji.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

according as his divine power hath given unto us all things that pertain unto life and godliness, through the knowledge of him that hath called us to glory and virtue:

Wolof

dooley yàlla moo nu may lépp lu aju ci dund gu sax ak ragal yàlla, jaarale ko ci xam gi nu ko xam, moom mi nu woo ci kaw ndamam ak dooleem.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and it came to pass, that he went through the corn fields on the sabbath day; and his disciples began, as they went, to pluck the ears of corn.

Wolof

amoon na benn bésu noflaay yeesu jaar ciy tool yu ñor. bi ñuy dem nag, ay taalibeem daldi fàq ay gub.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and it came to pass, that, while apollos was at corinth, paul having passed through the upper coasts came to ephesus: and finding certain disciples,

Wolof

ba apolos nekkee korent nag, pool jaar ca teggi ya gën a kawe ca réew ma, door a dikk efes. noonu mu gis fa ay taalibe.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and be found in him, not having mine own righteousness, which is of the law, but that which is through the faith of christ, the righteousness which is of god by faith:

Wolof

na ma yàlla fekk ci moom, waxuma ci njub gu aju ci sàmm yoon, waaye gu aju ci gëm kirist, maanaam njub gi nu yàlla sol ci kaw ngëm.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and it came to pass on the second sabbath after the first, that he went through the corn fields; and his disciples plucked the ears of corn, and did eat, rubbing them in their hands.

Wolof

amoon na benn bésu noflaay yeesu di dem, jaar ci ay tool yu ñor. taalibeem ya di fàq ay cëgg, di leen boxom ci seeni loxo tey lekk.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and, having made peace through the blood of his cross, by him to reconcile all things unto himself; by him, i say, whether they be things in earth, or things in heaven.

Wolof

te jaar ci moom, jubale lépp ak boppam, muy ci kaw asamaan yi mbaa ci suuf, ba mu wàccee jàmm jaarale ko ci deret ji tuuru, bi doom ji deeyee ca bant ba.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,800,197,860 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK