Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
and provide them beasts, that they may set paul on, and bring him safe unto felix the governor.
wutal-leen it pool lu mu war, ngeen yóbbu ko ci jàmm ak salaam ba ca feligsë, boroom réew mi.»
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
and he said unto him, thy brother is come; and thy father hath killed the fatted calf, because he hath received him safe and sound.
mu tontu ko: “sa rakk moo dellusi, te sa baay rey na sëllu wu duuf wa, ndaxte ñibbisi na ci jàmm.”
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
finally, my brethren, rejoice in the lord. to write the same things to you, to me indeed is not grievous, but for you it is safe.
kon nag samay bokk, bégleen ci boroom bi. duma sonn mukk ci di leen ko wax, ndax seen mucc moo ci aju.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :