Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
after these things jesus shewed himself again to the disciples at the sea of tiberias; and on this wise shewed he himself.
bi ñu ca tegee ab diir, yeesu feeñuwaat na ay taalibeem ca tefesu dex gu ñuy wax tiberyàdd. nii la deme woon:
again, the kingdom of heaven is like unto a net, that was cast into the sea, and gathered of every kind:
yeesu waxaat ne: «nguuru yàlla aji kawe ji dafa mel ni mbaal mu ñu wàcce ci géej, mu jàpp jën wu nekk.
and i saw a new heaven and a new earth: for the first heaven and the first earth were passed away; and there was no more sea.
noonu ma gis asamaan su bees ak suuf su bees, ndaxte asamaan su jëkk sa ak suuf su jëkk sa wéyoon nañu, te géej gi amatul.
and a mighty angel took up a stone like a great millstone, and cast it into the sea, saying, thus with violence shall that great city babylon be thrown down, and shall be found no more at all.
noonu malaaka mu am doole jël doj wu réy, sànni ko ci géej gi, naan: «nii lañuy sànnee ak doole babilon dëkk bu mag bi, mu ne meŋŋ.