Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
their feet are swift to shed blood:
Ñu sawar lañu ci rey nit.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
which he shed on us abundantly through jesus christ our saviour;
mi mu nu sotti ba mu baawaan, ci darajay yeesu kirist sunu musalkat.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
and he said unto them, this is my blood of the new testament, which is shed for many.
mu ne leen: «lii sama deret la, ji fas kóllëre gi, te mu tuuru ngir ñu bare.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
and hope maketh not ashamed; because the love of god is shed abroad in our hearts by the holy ghost which is given unto us.
te yaakaar jooju du ay nax, ndax mbëggeelu yàllaa ngi baawaan ci sunu xol, jaarale ko ci xelam mu sell mi mu nu may.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
and when the blood of thy martyr stephen was shed, i also was standing by, and consenting unto his death, and kept the raiment of them that slew him.
rax-ca-dolli bi ñu tuuree deretu ecen, mi la doon seedeel, teewe naa ko, ànd ca, bay wottu sax yérey ñi ko doon rey.”
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :