Vous avez cherché: speaking (Anglais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

speaking lies in hypocrisy; having their conscience seared with a hot iron;

Wolof

Ñooñu ay naaféq yuy naxe lañu, te seen xol dërkiis.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

also of your own selves shall men arise, speaking perverse things, to draw away disciples after them.

Wolof

ay nit dinañu jóg ci seen biir sax, di wax luy sànke, ngir sàkku ay taalibe.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

wherein they think it strange that ye run not with them to the same excess of riot, speaking evil of you:

Wolof

Ñiy jëfe noonu waaru nañu, ba di leen sosal, ci li ngeen àndul ak ñoom, sóobu ci seeni moy yu dul jeex,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

but speaking the truth in love, may grow up into him in all things, which is the head, even christ:

Wolof

waaye dinanu wax dëgg, ëmb ko ci mbëggeel, bay màgg ci fànn gu ne ci sunu bokk ci kirist. mooy bopp,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

but was rebuked for his iniquity: the dumb ass speaking with man's voice forbad the madness of the prophet.

Wolof

waaye déggadeem yóbbe na ko yeraanga; xam ngeen ne mbaam-sëf du wax, waaye mbaam wax na ak moom ci làmmiñ wu bir, ngir mu génn ci ndofam googu.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

since ye seek a proof of christ speaking in me, which to you-ward is not weak, but is mighty in you.

Wolof

bu fekkee ne dangeen a bëgg firnde juy wone ne, kirist mooy wax jaarale ko ci man, dingeen ko am. digganteem ak yéen du ànd ak néew doole, waaye dafay feeñal kàttan ci seen biir.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and there was given unto him a mouth speaking great things and blasphemies; and power was given unto him to continue forty and two months.

Wolof

noonu mayees ko mu am gémmiñ, muy jey boppam te di xarab turu yàlla. mayees ko it sañ-sañu jëf ci kaw suuf diirub ñeent-fukki weer ak ñaar.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

let all bitterness, and wrath, and anger, and clamour, and evil speaking, be put away from you, with all malice:

Wolof

dëdduleen lépp luy wex mbaa tàng bopp, luy mer mbaa coow, lépp luy xaste mbaa coxor.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

to whom also he shewed himself alive after his passion by many infallible proofs, being seen of them forty days, and speaking of the things pertaining to the kingdom of god:

Wolof

gannaaw ay coonoom, ñëw na ci ñoom, di leen won ay firnde yu bare te wér ne mu ngi dund; mu feeñu leen diirub ñeent-fukki fan, di diisoo ak ñoom ci lu jëm ci nguuru yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and withal they learn to be idle, wandering about from house to house; and not only idle, but tattlers also and busybodies, speaking things which they ought not.

Wolof

te du yem ci bëgg a séyaat rekk, waaye ku tayel lay doon; di ku wër kër ak kër, rax-ca-dolli réy làmmiñ te deñ kumpa, di wax lu yoonam nekkul.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

now when the congregation was broken up, many of the jews and religious proselytes followed paul and barnabas: who, speaking to them, persuaded them to continue in the grace of god.

Wolof

te bi mbooloo ma tasee, ay yawut yu bare ak ñi tuuboon ci yoonu yawut te ragal yàlla, topp ci pool ak barnabas. Ñuy diisoo ak ñoom, di leen xiir, ñu wàkkirlu ci yiwu yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and when we were all fallen to the earth, i heard a voice speaking unto me, and saying in the hebrew tongue, saul, saul, why persecutest thou me? it is hard for thee to kick against the pricks.

Wolof

nu ne nërëm ci suuf, ma dégg baat bu ma wax ci làkku yawut ne: “sool, sool, lu tax nga di ma fitnaal? ngay bëre ak man ni fas wuy woŋŋeetu ku koy jam dëgël, metti na ci yaw.”

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,762,975,053 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK