Vous avez cherché: that (Anglais - Wolof)

Traduction

Wolof

Traduction
Traduction

Traduisez instantanément des textes, des documents et des voix avec Lara

Traduire maintenant

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

i am lucky that means

Wolof

mujhe bhook lagi hai

Dernière mise à jour : 2019-03-20
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

i am that bread of life.

Wolof

maay ñam wiy joxe dund.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

we would like teacher to know that

Wolof

ang aking anak ay nangangailangan ng tulong sa

Dernière mise à jour : 2024-07-29
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

judge not, that ye be not judged.

Wolof

«buleen àtte seeni moroom ak ñaaw njort, ngir bañ ñu àtte leen yéen itam.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

and there was great joy in that city.

Wolof

noonu mbég mu réy tàbbi ca dëkk ba.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

for he knew that for envy they had delivered him.

Wolof

ndaxte xamoon na ne, kiñaan rekk a taxoon, ñu jébbal ko ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

and he that seeth me seeth him that sent me.

Wolof

ku ma gis, gis nga ki ma yónni.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

and from that time he sought opportunity to betray him.

Wolof

li dale ci saa soosa nag yudaa di fexe jamono ju mu leen man a jébbal yeesu.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

and charged them that they should not make him known:

Wolof

te mu dénk leen bu wóor, ñu bañ koo siiwal.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

added yet this above all, that he shut up john in prison.

Wolof

ba faf tëj yaxya kaso.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

and all that believed were together, and had all things common;

Wolof

Ñi gëm nag dañoo booloo te bokk lépp.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

and herein is that saying true, one soweth, and another reapeth.

Wolof

wax ji ñu wax ne: “kenn dina ji, keneen góob,” dëgg la.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

and they that stood by said, revilest thou god's high priest?

Wolof

waaye ña taxaw ca wetam ne ko: «ndax dangay xas saraxalekat bu mag, bi yàlla fal?»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

saying, prophesy unto us, thou christ, who is he that smote thee?

Wolof

ne ko: «yaw kirist, yonent bi, ndax xam nga ku la dóor?»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

he that despised moses' law died without mercy under two or three witnesses:

Wolof

ku weddi ndigali yoonu musaa wi, te ñaar walla ñetti nit seede ko, dina dee ci lu amul benn yërmande.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

i know thy works, that thou art neither cold nor hot: i would thou wert cold or hot.

Wolof

xam naa say jëf, xam ne seddoo, tàngoo. manoon ngaa sedd mbaa nga tàng,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

for in that he died, he died unto sin once: but in that he liveth, he liveth unto god.

Wolof

dee na benn yoon, ba bàkkaar mënul ci moom dara; te mi ngi dund léegi, di ànd ak yàlla ba fàww.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Anglais

he that heareth you heareth me; and he that despiseth you despiseth me; and he that despiseth me despiseth him that sent me.

Wolof

«ku leen déglu, déglu na ma; ku leen bañ, bañ na ma. te ku ma bañ, bañ na ki ma yónni.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
10,388,471,977 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK