Vous avez cherché: the wind (Anglais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

and when they were come into the ship, the wind ceased.

Wolof

noonu ñu dugg ca gaal ga, te ngelaw li ne tekk.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and when the ship was caught, and could not bear up into the wind, we let her drive.

Wolof

mu ëpp doole gaal ga, daldi ko wat, ba nu bayliku, daldi yal.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

but the ship was now in the midst of the sea, tossed with waves: for the wind was contrary.

Wolof

bi mu fa nekkee nag, gaal ga sore na tefes ga, te duus ya di ko yengal bu metti, ndax ngelaw la leen soflu.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

but let him ask in faith, nothing wavering. for he that wavereth is like a wave of the sea driven with the wind and tossed.

Wolof

waaye na ko ñaan ci ngëm te bañ cee werante; ndaxte kiy werante mi ngi mel ni ndoxum géej, mi ngelaw liy lëmbaaje wet gu ne.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and they feared exceedingly, and said one to another, what manner of man is this, that even the wind and the sea obey him?

Wolof

Ñu daldi ragal lool, naan ci seen biir: «kii moo di kan, ba ngelaw li ak dex gi sax di ko déggal?»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and he went up unto them into the ship; and the wind ceased: and they were sore amazed in themselves beyond measure, and wondered.

Wolof

noonu mu fekksi leen ci gaal gi, ngelaw daldi ne tekk.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and as they departed, jesus began to say unto the multitudes concerning john, what went ye out into the wilderness to see? a reed shaken with the wind?

Wolof

bi nga xamee ne taalibe ya yaxya yónni woon ci yeesu dem nañu, yeesu daldi wax ak mbooloo ma ci mbirum yaxya ne leen: «lu ngeen seeti woon ca màndiŋ ma? xanaa barax buy jaayu ci ngelaw li?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and when they had taken up the anchors, they committed themselves unto the sea, and loosed the rudder bands, and hoised up the mainsail to the wind, and made toward shore.

Wolof

Ñu dagg diigal ya, bàyyi leen ci biir géej, yiwiwaale baar ba; ba noppi firi wiiru kanam ga, jublu ca tefes ga.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and when the messengers of john were departed, he began to speak unto the people concerning john, what went ye out into the wilderness for to see? a reed shaken with the wind?

Wolof

bi ndawi yaxya yi demee, yeesu daldi wax ak mbooloo ma ci mbirum yaxya ne leen: «lu ngeen seeti woon ca màndiŋ ma? xanaa barax buy jaayu ci ngelaw li?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and after these things i saw four angels standing on the four corners of the earth, holding the four winds of the earth, that the wind should not blow on the earth, nor on the sea, nor on any tree.

Wolof

gannaaw loolu ma gis ñeenti malaaka yu taxaw ci ñeenti xeblay àddina si. Ñu téye ñeenti ngelawi àddina, ngir ngelaw du wol ci kaw suuf, ci géej mbaa ci genn garab.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and he saw them toiling in rowing; for the wind was contrary unto them: and about the fourth watch of the night he cometh unto them, walking upon the sea, and would have passed by them.

Wolof

booba mu gis taalibe yi sonn lool ci joow gaal gi ndax li leen ngelaw li soflu. ca njël nag mu jëm ci ñoom, di dox ci kaw dex gi, ba xaw leen a raw.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and he said unto them, where is your faith? and they being afraid wondered, saying one to another, what manner of man is this! for he commandeth even the winds and water, and they obey him.

Wolof

yeesu ne taalibe yi: «ana seen ngëm?» Ñu daldi tiit te waaru, naan ci seen biir: «kii moo di kan? mi ngi jox ndigal ngelaw li ak ndox mi, ñu koy déggal.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Certaines traductions humaines peu pertinentes ont été masquées.
Affichez les résultats peu pertinents.

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,275,445 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK