Vous avez cherché: whose (Anglais - Wolof)

Anglais

Traduction

whose

Traduction

Wolof

Traduction
Traduction

Traduisez instantanément des textes, des documents et des voix avec Lara

Traduire maintenant

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

whose mouth is full of cursing and bitterness:

Wolof

duñu génne ci seen gémmiñ lu dul ay móolu ak i xas.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

there was a man sent from god, whose name was john.

Wolof

yàlla yónni woon na nit ku ñu naan yaxya.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and he saith unto them, whose is this image and superscription?

Wolof

yeesu ne leen: «kan lañu ci def nataalam ak turam?»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and barnabas determined to take with them john, whose surname was mark.

Wolof

barnabas nag bëggoon na yóbbaale yowaana, mi ñuy wax it màrk.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

for he looked for a city which hath foundations, whose builder and maker is god.

Wolof

waaye nag ibraaymaa ngi doon séentu dëkk bi sax, bi yàlla tabax te sanc ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and now send men to joppa, and call for one simon, whose surname is peter:

Wolof

yónnil léegi nag ay nit ci dëkku yope, ñu woo ku tudd simoŋ, mi ñu dàkkentale piyeer.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and we have sent with him the brother, whose praise is in the gospel throughout all the churches;

Wolof

yónniwaale nanu ak moom mbokk, mi am tur wu rafet ci mboolooy ñi gëm ñépp ndax li muy waare xebaaru kirist.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

but he whose descent is not counted from them received tithes of abraham, and blessed him that had the promises.

Wolof

waaye melkisedeg mi bokkul woon ci giiru lewi, jotoon na asaka ci alali ibraayma. te rax-ca-dolli barkeel na ko, moom mi yàlla sédde woon dige yi.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

shew me a penny. whose image and superscription hath it? they answered and said, caesar's.

Wolof

«wonleen ma posetu denariyon. kan lañu ci def nataalam ak turam?» Ñu tontu ko: «sesaar.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and barnabas and saul returned from jerusalem, when they had fulfilled their ministry, and took with them john, whose surname was mark.

Wolof

naka barnabas ak sool, bi ñu matalee seen liggéey, ñu jóge yerusalem, ñibbi, ànd ak yowaana mi tudd màrk.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and after three months we departed in a ship of alexandria, which had wintered in the isle, whose sign was castor and pollux.

Wolof

bi nu fa amee ñetti weer, nu dugg ca gaal gu lollikoo ca dun ba, daldi tàbbi ca géej ga. gaalu dëkku alegsàndiri la woon, te yor xàmmikaay guy nataalu kastor ak polugsë.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

so jesus came again into cana of galilee, where he made the water wine. and there was a certain nobleman, whose son was sick at capernaum.

Wolof

noonu kon mu dellusi kana ci galile, dëkk ba mu soppe woon ndox ma biiñ. amoon na benn dagu buur bu dëkkoon kapernawum te doomam feebar.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

(it was that mary which anointed the lord with ointment, and wiped his feet with her hair, whose brother lazarus was sick.)

Wolof

maryaama mooy jigéen jiy sottiji latkoloñ ci tànki boroom bi, fompe ko kawaram. moom la càmmiñam lasaar woppoon.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and he exerciseth all the power of the first beast before him, and causeth the earth and them which dwell therein to worship the first beast, whose deadly wound was healed.

Wolof

muy jëf ak sañ-sañu rab wu jëkk wa ci turam, di sant waa àddina sépp, ñu jaamu rab wu jëkk, woowu am gaañu-gaañu ba ko rey, waaye daldi wér.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and cast him out of the city, and stoned him: and the witnesses laid down their clothes at a young man's feet, whose name was saul.

Wolof

ñu wat-wate ko, génne ko dëkk ba, dóor ko ay doj, ba mu dee. seede ya tegoon nañu seeni yére ci tànki waxambaane wu tudd sool.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and he departed thence, and entered into a certain man's house, named justus, one that worshipped god, whose house joined hard to the synagogue.

Wolof

ci kaw loolu mu jóge fa, dugg ci këru ku tudd tisiyus yustus, di ku ragal yàlla, te kër ga dend ak jàngu ba.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and a certain woman named lydia, a seller of purple, of the city of thyatira, which worshipped god, heard us: whose heart the lord opened, that she attended unto the things which were spoken of paul.

Wolof

fekk am na fa jigéen juy déglu, tudd lidi, di jaaykatu cuub, bu dëkk catir, te mu ragal yàlla. noonu boroom bi ubbi na xolam, ba mu nangu li pool di wax.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
9,571,090,908 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK