Vous avez cherché: الابرار (Arabe - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Arabe

Wolof

Infos

Arabe

لان عيني الرب على الابرار واذنيه الى طلبتهم. ولكن وجه الرب ضد فاعلي الشر

Wolof

ndax boroom baa ngi xool ñi jub bëti yërmande,di ubbi ay noppam ci seeni ñaan,waaye dàq ñiy def lu bon.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

فيكون لك الطوبى اذ ليس لهم حتى يكافوك. لانك تكافى في قيامة الابرار

Wolof

soo ko defee, dinga barkeel, ndaxte duñu la ko man a fey, waaye dinga jot sag pey, bés bi ñi jub di dekki.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

حينئذ يضيء الابرار كالشمس في ملكوت ابيهم. من له اذنان للسمع فليسمع

Wolof

booba nag ñu jub ñi dinañu leer ni jant bi ci seen nguuru baay. déglul bu baax, yaw mi am ay nopp.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

‎ولي رجاء بالله في ما هم ايضا ينتظرونه انه سوف تكون قيامة للاموات الابرار والاثمة‎.

Wolof

te bokk naa ak ñoom yaakaar ci yàlla, ne ñi jub ak ñi jubadi dinañu dekki keroog yawmelxayaam.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

فيجيبه الابرار حينئذ قائلين. يا رب متى رأيناك جائعا فاطعمناك. او عطشانا فسقيناك.

Wolof

ci kaw loolu ñi jub dinañu tontu ne: “boroom bi, kañ lanu la gisoon, nga xiif, nu jox la, nga lekk; mbaa nga mar, nu jox la, nga naan?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

لكي تكونوا ابناء ابيكم الذي في السموات. فانه يشرق شمسه على الاشرار والصالحين ويمطر على الابرار والظالمين.

Wolof

ngir wone ne, yéenay doomi seen baay bi nekk ci kaw. ndaxte mu ngi fenkal jantam ci kaw ñu bon ñi ak ñu baax ñi, te muy tawal ñi jub ak ñi jubadi.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

فراقبوه وارسلوا جواسيس يتراءون انهم ابرار لكي يمسكوه بكلمة حتى يسلموه الى حكم الوالي وسلطانه.

Wolof

noonu ñu koy yeeru, daldi yónni ay nit ñu mbubboo njub, sas leen ñu fexe koo jàpp ci ay waxam, ngir jébbal ko boroom réew, ma yor kilifteef ak sañ-sañ.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,800,391,680 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK