Vous avez cherché: الفريسيون (Arabe - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Arabe

Wolof

Infos

Arabe

وفيما كان الفريسيون مجتمعين سألهم يسوع

Wolof

bi farisen ya dajee nag, yeesu laaj leen:

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

فلما خرج الفريسيون تشاوروا عليه لكي يهلكوه.

Wolof

farisen ya génn nag, daldi gise, ngir fexee reylu yeesu.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

فاجابهم الفريسيون ألعلكم انتم ايضا قد ضللتم.

Wolof

noonu farisen ya laaj leen: «mbaa naxuñu leen, yéen itam?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

اما الفريسيون فقالوا برئيس الشياطين يخرج الشياطين

Wolof

waaye farisen ya ne: «ci kàttanu buuru rab yi lay dàqe rab yi.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

حينئذ ذهب الفريسيون وتشاوروا لكي يصطادوه بكلمة.

Wolof

booba farisen ya dem gise, ba xam lu ñu war a def, ngir fiir yeesu ci waxam.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

اما الفريسيون فلما سمعوا انه ابكم الصدوقيين اجتمعوا معا.

Wolof

gannaaw gi, farisen ya yég nañu ne, yey na sadusen ya. kon nag ñu daldi daje.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

فخرج الفريسيون للوقت مع الهيرودسيين وتشاوروا عليه لكي يهلكوه

Wolof

ca saa sa nag farisen ya génn, daldi gise ak ñi far ak buur bi erodd, ngir fexe koo reylu.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

فتذمر الفريسيون والكتبة قائلين هذا يقبل خطاة وياكل معهم.

Wolof

farisen ya ak xutbakat ya di ñurumtu naan: «waa jii mi ngi nangoo nekk ak ay boroom bàkkaar ak a lekkandook ñoom!»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

فقال له الفريسيون. انظر. لماذا يفعلون في السبت ما لا يحل.

Wolof

noonu farisen ya ne yeesu: «gisal, lu tax say taalibe di def lu jaaduwul ci bésu noflaay bi?»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

فخرج الفريسيون وابتدأوا يحاورونه طالبين منه آية من السماء لكي يجربوه.

Wolof

noonu farisen yi ñëw, di werante ak moom; ñu fexe koo fiir, ba laaj ko kéemaan gu jóge ci asamaan tey firndeel yónnentam.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

فلما نظر الفريسيون قالوا لتلاميذه لماذا ياكل معلمكم مع العشارين والخطاة.

Wolof

bi ko farisen ya gisee nag, ñu ne taalibe ya: «lu tax seen kilifa di lekkandoo ak ay juutikat ak ay boroom bàkkaar?»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

اما الفريسيون فلما سمعوا قالوا هذا لا يخرج الشياطين الا ببعلزبول رئيس الشياطين.

Wolof

bi farisen ya déggee loolu nag, ñu ne: «kii ci kàttanu beelsebul, buuru rab yi, lay dàqe rab yi.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

وجاء اليه الفريسيون ليجربوه قائلين له هل يحل للرجل ان يطلّق امرأته لكل سبب.

Wolof

bi mu fa nekkee, ay farisen ñëw ci moom, bëgg koo fiir; ñu ne ko: «ndax jaadu na nit fase jabaram, saa su ko neexee?»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

سمع الفريسيون الجمع يتناجون بهذا من نحوه فارسل الفريسيون ورؤساء الكهنة خداما ليمسكوه.

Wolof

farisen ya daldi dégg la mbooloo ma doon déeyante ci mbirum yeesu. saraxalekat yu mag ya ak farisen ya yebal ay alkaati yu daan wottu kër yàlla ga, ngir ñu jàppi ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

ثم سأله الفريسيون والكتبة لماذا لا يسلك تلاميذك حسب تقليد الشيوخ بل يأكلون خبزا بأيد غير مغسولة.

Wolof

noonu farisen ya ak xutbakat ya laaj ko ne: «lu tax say taalibe duñu topp aaday yoon, yi maam yi tëral, waaye ñuy lekk ak loxo yu setul?»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

ولكن ويل لكم ايها الفريسيون لانكم تعشّرون النعنع والسذاب وكل بقل وتتجاوزون عن الحق ومحبة الله. كان ينبغي ان تعملوا هذه ولا تتركوا تلك.

Wolof

yéen farisen yi dingeen torox! ndaxte yéena ngi sàkk asaka ci naana ak ru ak léjum bu nekk, waaye sàggane ngeen njubte ak mbëggeel ci yàlla. loolu ngeen war a def, waxuma nag ngeen sàggane la ca des.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

ألعل احدا من الرؤساء او من الفريسيين آمن به.

Wolof

ndax am na kenn ci saraxalekat yi walla ci farisen yi ku ko gëm? déedéet.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,783,900,100 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK