Vous avez cherché: وابتدأ (Arabe - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Arabe

Wolof

Infos

Arabe

فجلس الميت وابتدأ يتكلم فدفعه الى امه.

Wolof

noonu nit ka dee woon jóg toog, tàmbalee wax. yeesu delloo ko yaay ja.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

ثم اخذ معه بطرس وابني زبدي وابتدأ يحزن ويكتئب.

Wolof

bi mu waxee loolu, mu ànd ak piyeer ak ñaari doomi sebede, daldi am tiis ba xonett.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

ثم اخذ معه بطرس ويعقوب ويوحنا وابتدأ يدهش ويكتئب.

Wolof

mu ànd ak piyeer, saag ak yowaana, daldi jàq, ba xonett.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

وقال القول علانية. فاخذه بطرس اليه وابتدأ ينتهره.

Wolof

noonu mu xamal leen mbir mi, ba mu leer nàññ. bi ko piyeer déggee, mu woo ko ci pegg, daldi ko yedd.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

وابتدأ بطرس يقول له ها نحن قد تركنا كل شيء وتبعناك.

Wolof

ci kaw loolu piyeer daldi ko ne: «nun de dëddu nanu lépp te topp la!»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

فحزنوا جدا وابتدأ كل واحد منهم يقول له هل انا هو يا رب.

Wolof

taalibe ya am naqaru xol bu réy; ku nekk daldi ne ko: «mbaa du man, boroom bi?»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

فمضى وابتدأ ينادي في العشر المدن كم صنع به يسوع. فتعجب الجميع

Wolof

noonu waa ji dem ci diiwaanu fukki dëkk yi, daldi fa yégle la ko yeesu defal, ba ñépp waaru.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

فأخذه بطرس اليه وابتدأ ينتهره قائلا حاشاك يا رب. لا يكون لك هذا.

Wolof

bi mu waxee ba noppi, piyeer woo ko ci pegg, bëgg koo yedd ne ko: «yàlla tere, boroom bi, loolu du la dal.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

ثم صبّ ماء في مغسل وابتدأ يغسل ارجل التلاميذ ويمسحها بالمنشفة التي كان متزرا بها.

Wolof

noonu mu sotti ndox ci ab këll, daldi tàmbali di raxas tànki taalibe ya, di leen fomp ak sarbet, ba mu laxasaayoo.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

ودعا الاثني عشر وابتدأ يرسلهم اثنين اثنين. واعطاهم سلطانا على الارواح النجسة.

Wolof

noonu mu woo ci moom fukki taalibe ya ak ñaar, jox leen sañ-sañu dàq rab yi, yónni leen, ñu ànd ñaar-ñaar.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

وابتدأ يقول للشعب هذا المثل. انسان غرس كرما وسلمه الى كرامين وسافر زمانا طويلا.

Wolof

noonu yeesu daldi wax nit ña léeb wii: «amoon na nit ku jëmbët toolu réseñ, batale ko ay beykat, dem tukki tukki bu yàgg.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

وابتدأ يقول لهم بامثال انسان غرس كرما واحاطه بسياج وحفر حوض معصرة وبنى برجا وسلمه الى كرامين وسافر.

Wolof

noonu yeesu daldi leen wax ciy léeb. mu ne leen: «amoon na fi nit ku jëmbët toolu réseñ. mu ñag tool bi, gas pax ngir nal ci réseñ yi, tabax wottukaay, ba noppi batale ko ay beykat, daldi tukki.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

وابتدأ ايضا يعلم عند البحر. فاجتمع اليه جمع كثير حتى انه دخل السفينة وجلس على البحر والجمع كله كان عند البحر على الارض

Wolof

am beneen yoon yeesu nekk ci wetu dex ga, di jàngalewaat. mbooloo mu bare dajaloosi, ba tax mu yéeg cig gaal, dugg ca dex ga; mbooloo mépp taxaw ca tefes ga.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

وابتدأ يعلّمهم ان ابن الانسان ينبغي ان يتألم كثيرا ويرفض من الشيوخ ورؤساء الكهنة والكتبة ويقتل. وبعد ثلاثة ايام يقوم.

Wolof

booba yeesu tàmbali na leen a xamal ne, doomu nit ki war na sonn lu bare; njiit ya, saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya dëddu ko, ñu rey ko, mu dekki ci ñetti fan.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

وكانوا في الطريق صاعدين الى اورشليم ويتقدمهم يسوع. وكانوا يتحيّرون وفيما هم يتبعون كانوا يخافون. فاخذ الاثني عشر ايضا وابتدأ يقول لهم عما سيحدث له.

Wolof

gannaaw loolu ñu ànd jëm yerusalem, yeesu jiitu; taalibe yi am njàqare, te ñi ci topp tiit. noonu yeesu woowaat fukk ak ñaar ña cig wet, xamal leen li nar a xew ci mbiram.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Arabe

ثم ابتدأ من موسى ومن جميع الانبياء يفسر لهما الأمور المختصة به في جميع الكتب

Wolof

noonu mu tàmbalee ci yonent yàlla musaa ba ci yonent yépp, tekkil leen li mbind mi wax lépp ci ay mbiram.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,802,699,135 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK