Vous avez cherché: stridigheder (Danois - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Danois

Wolof

Infos

Danois

og afvis de tåbelige og uforstandige stridigheder, efterdi du ved, at de avle kampe,

Wolof

tanqamlul bépp weranteb neen bu amul njariñ, xam ne xuloo rekk lay jur.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Danois

men hold dig fra tåbelige stridigheder og slægtregistre og kiv og kampe om loven; thi de ere unyttige og frugtesløse.

Wolof

waaye moytul yu deme ni werantey neen ak limi maam, ay xuloo ak i xëccoo ci doxalinu yoonu musaa, ndax loolu waxi neen la, te amul benn njariñ.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Danois

han er opblæst, skønt han intet ved, men er syg for stridigheder og ordkampe, hvoraf kommer avind, kiv, forhånelser, ond mistanke

Wolof

kooku boroom tiitar la, bu xamul dara. dafa wéradi, ba sóobu ci gëstuy neen ak i werante ciy araf yu dul jur lu dul ñeetaange, xuloo, xaste, ñaaw njort

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Danois

hvoraf kommer det, at den er krige og stridigheder iblandt eder? mon ikke deraf, af eders lyster, som stride i eders lemmer?

Wolof

xeex yi ak xuloo yi ci seen biir nag, lu leen waral? xanaa du ci seeni bëgg-bëgg, yiy xeex ci seeni cér?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Danois

da nu paulus og barnabas kom i en ikke ringe splid og strid med dem, så besluttede man, at paulus og barnabas og nogle andre af dem skulde drage op til jerusalem til apostlene og de Ældste i anledning af dette spørgsmål.

Wolof

pool ak barnabas nag am ak ñoom diisoo ak werante wu metti; noonu bokk yi jàpp ne, pool ak barnabas ak ñeneen ci ñoom war nañoo dem yerusalem ca ndaw ya ak njiit ya, ngir leeral werante wi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,763,098,026 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK