Vous avez cherché: engendró (Espagnol - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Espagnol

Wolof

Infos

Espagnol

josías engendró a jeconías y a sus hermanos en el tiempo de la deportación a babilonia

Wolof

yosiyas jur yekoñas ak i doomi baayam ca jamono, ja ñu defe yawut ya jaam, yóbbu leen babilon.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

ezequías engendró a manasés; manasés engendró a amón; amón engendró a josías

Wolof

esekiyas manase; manase amon; amon yosiyas;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

aram engendró a aminadab; aminadab engendró a najsón; najsón engendró a salmón

Wolof

aram aminadab; aminadab naason; naason salmon;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

después de la deportación a babilonia, jeconías engendró a salatiel; salatiel engendró a zorobabel

Wolof

ba ñu leen yóbboo ca babilon, yekoñas jur salacel; salacel sorobabel,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

al oír esta palabra, moisés huyó y vivió exiliado en la tierra de madián, donde engendró dos hijos

Wolof

bi musaa déggee wax jooju, mu daldi daw, dem réewu majan, di fa ab doxandéem; mu séy fa, ba am ñaari doom.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

abraham engendró a isaac; isaac engendró a jacob; jacob engendró a judá y a sus hermanos

Wolof

ibraayma moo jur isaaxa; isaaxa jur yanqóoba; yanqóoba jur yuda ak i doomi baayam;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

judá engendró de tamar a fares y a zéraj; fares engendró a hesrón; hesrón engendró a aram

Wolof

yuda, fares ak sara ci tamar; fares esrom, miy baayu aram;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

todo aquel que cree que jesús es el cristo es nacido de dios, y todo aquel que ama al que engendró ama también al que es nacido de él

Wolof

képp ku gëm ne yeesu mooy almasi bi, juddu nga ci yàlla; te ku bëgg waajur, dinga bëgg itam ki mu jur.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

en estas cosas hay una alegoría, pues estas mujeres son dos pactos: agar es el pacto del monte sinaí que engendró hijos para esclavitud

Wolof

loolu nag am na lu muy misaal. Ñaari jigéen ñi dañoo bijji ñaari kóllëre. benn bi di ajara, mooy wone kóllëre, gi yàlla fasoon ca tundu sinayi. ay jaam lay jur.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

dios le dio el pacto de la circuncisión; y así abraham engendró a isaac y le circuncidó al octavo día. lo mismo hizo isaac a jacob, y jacob a los doce patriarcas

Wolof

yàlla nag tëral kóllëre seen diggante, fas ko ci màndargam xaraf. noonu ibraayma jur isaaxa, xarafal ko ca juróom-ñetteelu fan ba; isaaxa def noonu yanqóoba, yanqóoba it def noonu fukki maam ya ak ñaar, ñi sos xeet wi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

luego la baja pasión, después de haber concebido, da a luz el pecado; y el pecado, una vez llevado a cabo, engendra la muerte

Wolof

kon bu bëgg-bëgg ëmbee, bàkkaar lay wasin, te bu bàkkaar màggee, jur dee.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,788,694,139 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK