Vous avez cherché: entendieron (Espagnol - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Espagnol

Wolof

Infos

Espagnol

pero no entendieron que les hablaba del padre

Wolof

xamuñu woon ne, yàlla baay bee tax muy wax.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

pero ellos no entendieron el dicho que les habló

Wolof

waaye xamuñu li kàddoom yi doon tekki.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

entonces los discípulos entendieron que les hablaba de juan el bautista

Wolof

ndax wax jooju nag, taalibe ya xam ne, ci mbirum yaxya la leen doon wax.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

jesús les dijo esta figura, pero ellos no entendieron qué era lo que les decía

Wolof

yeesu misaaloon na leen loolu, waaye xamuñu lu mu leen doon wax.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

al oír sus parábolas, los principales sacerdotes y los fariseos entendieron que él hablaba de ellos

Wolof

bi nga xamee ne saraxalekat yu mag ya ak farisen ya dégg nañu léebam yooyu, ñu xam ne ñoom lay wax.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

pensaba que sus hermanos entenderían que dios les daría liberación por su mano, pero ellos no lo entendieron

Wolof

mu defe ne, ay bokkam dinañu xam ne, ciy loxoom la leen yàllay musale, waaye xamuñu ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

a la verdad, los que estaban conmigo vieron la luz, pero no entendieron la voz del que hablaba conmigo

Wolof

Ñi ma àndaloon gis nañu leer ga, waaye dégguñu baatu ka doon wax ak man.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

entonces entendieron que no les habló de guardarse de la levadura del pan, sino más bien de la doctrina de los fariseos y de los saduceos

Wolof

noonu ñu xam ne, yeesu waxul woon lawiiru mburu, waaye ñu moytu njàngalem farisen ya ak sadusen ya.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

en aquella hora los principales sacerdotes y los escribas procuraban echarle mano, porque entendieron que contra ellos había dicho esta parábola; pero temieron al pueblo

Wolof

xutbakat ya ak saraxalekat yu mag ya ñu ngi doon wut a jàpp yeesu ca taxawaay ba, ndaxte xam nañu ne, ñoo tax mu wax léeb woowu. waaye ragal nañu mbooloo ma.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

sus discípulos no entendieron estas cosas al principio. pero cuando jesús fue glorificado, entonces se acordaron de que estas cosas estaban escritas acerca de él, y que estas cosas le hicieron a él

Wolof

yooyu yépp, taalibe ya xamuñu woon ca saa sa lu muy tekki; waaye gannaaw bi ndamu yeesu feeñee, ñu fàttaliku ne, mbind mi yégle woon na loolu ci moom, te amal nañu ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,777,832,259 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK