Vous avez cherché: espiritual (Espagnol - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Espagnol

Wolof

Infos

Espagnol

todos comieron la misma comida espiritual

Wolof

Ñoom ñépp bokk nañoo lekk ñam, wa yàlla joxe,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

pero lo espiritual no es primero, sino lo natural; luego lo espiritual

Wolof

yaram wi soloo ndamu xelum yàlla jiituwul; yaramu doom aadama moo jiitu; yaramu ndam li moo ci topp.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

porque deseo veros para compartir con vosotros algún don espiritual a fin de que seáis afirmados

Wolof

ndaxte bëgg naa leen a gis lool, ba indil leen barke bu jóge ci xel mu sell mi, ndax seen ngëm gën a dëgër.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

en cambio, el hombre espiritual lo juzga todo, mientras que él no es juzgado por nadie

Wolof

nit ki yor xelum yàlla dafay àtte lépp, te moom ci boppam, kenn du ko àtte.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

desead como niños recién nacidos la leche espiritual no adulterada, para que por ella crezcáis para salvación

Wolof

gannaaw ay liir ngeen yuy door a juddu te mos ci mbaaxug boroom bi, nàmpleen ci meew mu sell, miy dundal seen xol, ba màgg ci biir muccu yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

porque sabemos que la ley es espiritual; pero yo soy carnal, vendido a la sujeción del pecado

Wolof

xam nanu ne, yoonu musaa ngi jóge ci yàlla, waaye man yëfi àddina laa fonk, te nekk ci dooley bàkkaar, mel nib jaam.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

bendito sea el dios y padre de nuestro señor jesucristo, quien nos ha bendecido en cristo con toda bendición espiritual en los lugares celestiales

Wolof

cant ñeel na yàlla baayu sunu boroom yeesu kirist, mi nu sotti ci sunu bokk ci kirist lépp luy barkeel ci baatin te nekk ca bérab yu kawe ya.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

se siembra cuerpo natural; se resucita cuerpo espiritual. hay cuerpo natural; también hay cuerpo espiritual

Wolof

bu ñu koy suul, yaram lay doon wu soloo woon ruu. bu dekkee, doon yaram wu soloo ndamu xelum yàlla. ndegam am na yaram wu soloo ruu, kon dina am yaram wu soloo ndamu xelum yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

también vosotros sed edificados como piedras vivas en casa espiritual para ser un sacerdocio santo, a fin de ofrecer sacrificios espirituales, agradables a dios por medio de jesucristo

Wolof

te yéena ngi mel niy doj yuy dund yu yàllay defare dëkkukaayam. noonu ay saraxalekat yu sell ngeen, ngir jébbal ko ay sarax yu ngeen tibbe ci seen xol te neex ko ndax yeesu kirist.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

de estas cosas estamos hablando, no con las palabras enseñadas por la sabiduría humana, sino con las enseñadas por el espíritu, interpretando lo espiritual por medios espirituales

Wolof

te loolu nu yàlla may, yéglewunu ko ci ay baat yu soqikoo ci xam-xamu nit, waaye nu ngi koy yégle ci baat, yi soqikoo ci xelum yàlla, di tekkantal yëfi xelum yàlla ci ay baat yu mu nu sol.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

por esta razón también nosotros, desde el día en que lo oímos, no cesamos de orar por vosotros y de rogar que seáis llenos del conocimiento de su voluntad en toda sabiduría y plena comprensión espiritual

Wolof

looloo tax ci sunu wàllu bopp, ba nu ko yégee ba tey, jógunu ci di leen ñaanal. nu ngi ñaan yàlla, ngeen xam bu baax coobareem ci xel mu mat ak ràññee gu aju ci dooley xelam.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

así también vosotros; puesto que anheláis los dones espirituales, procurad abundar en ellos para la edificación de la iglesia

Wolof

yéen itam, gannaaw dangeen a fonk mayi xelum yàlla, jéemleen a ëpple ci liy yokk ngëmu mbooloo mi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,781,407,572 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK