Vous avez cherché: la cita es para pedir asilo (Espagnol - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Espagnol

Wolof

Infos

Espagnol

la cita es para pedir asilo, es algo bueno para ti. si te dan el asilo te podrán ayudar

Wolof

Dernière mise à jour : 2024-05-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

esta encuesta es para saber cómo te sientes en la empresa

Wolof

Dernière mise à jour : 2024-03-14
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

porque cuando os reunís en uno, eso no es para comer la cena del señor

Wolof

bu ngeen dajee, mënuleen a wax ne reeru boroom bi ngeen di lekk.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

en cuanto a las cosas de que me escribisteis, bueno es para el hombre no tocar mujer

Wolof

nanu jàll nag léegi ci laaj, yi ngeen ma doon bind, ci bañ a ànd ak jigéen, ndax lu baax la ci góor.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

esto es, para ser animado juntamente con vosotros por la fe que nos es común a vosotros y a mí

Wolof

maanaam ma nekk ci seen biir, te nu dimbaleente ci sunu ngëm, ndax man itam ma gën a am doole.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

considerad que la paciencia de nuestro señor es para salvación; como también nuestro amado hermano pablo os ha escrito, según la sabiduría que le ha sido dada

Wolof

te jàppleen ne, muñug sunu boroom muccu nit la. sunu mbokk mi nu bëgg pool bind na leen ko, ci xel mi ko yàlla sol.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

Él respondió y dijo: --señor, ¿quién es, para que yo crea en él

Wolof

waa ja ne ko: «wax ma mooy kan, sang bi, ba ma man koo gëm.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

honroso es para todos el matrimonio, y pura la relación conyugal; pero dios juzgará a los fornicarios y a los adúlteros

Wolof

na ñépp fullaal séy, te lalu séy bi bañ a taq sobe, ndaxte yàlla dina àtte ñu yàqu ñi ak njaalookat yi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

así resulta que las lenguas son señal, no para los creyentes, sino para los no creyentes; en cambio, la profecía no es para los no creyentes, sino para los creyentes

Wolof

ci noonu wax ay làkk, firnde la ci ñi gëmul, te du firnde ci ñi gëm. te it wax ci kàddug yàlla, du firnde ci ñi gëmul, waaye firnde la ci ñi gëm.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

todo esto es para que ahora sea dada a conocer, por medio de la iglesia, la multiforme sabiduría de dios a los principados y las autoridades en los lugares celestiales

Wolof

waaye léegi nee na fàŋŋ, ngir kilifa yi ak boroom sañ-sañ yi ca bérab yu kawe ya man a xam ni xelum yàlla xóote, jaar ci li ñu gis ci mbooloom ñi gëm kirist.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

la comida es para el estómago, y el estómago para la comida, pero dios destruirá tanto al uno como a la otra. el cuerpo no es para la inmoralidad sexual, sino para el señor, y el señor para el cuerpo

Wolof

am na ci yéen ñu naan: «Ñam mooy jariñ biir, te biir ay jariñoo ñam.» waaw, te yàlla dina leen yàq, ñoom ñaar yépp. waaye sàkkuñu yaram ngir moy yàlla; dañu koo sàkk, ngir muy jariñ boroom bi, boroom bi di ko jariñoo.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

les dijo: --a la verdad, beberéis de mi copa; pero el sentarse a mi derecha o a mi izquierda no es mío concederlo, sino que es para quienes lo ha preparado mi padre

Wolof

yeesu ne leen: «ci dëgg dingeen naan sama kaas, waaye toog ci sama ndeyjoor mbaa sama càmmooñ, du man maa koy maye, waaye sama baay moo koy may ñi mu ko waajal.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

al oírlo, jesús dijo: --esta enfermedad no es para muerte, sino para la gloria de dios; para que el hijo de dios sea glorificado por ella

Wolof

bi yeesu déggee xebaar boobu, mu ne: «lasaar de, woppam jooju du ko mujje; day wone ndamu yàlla, tey màggal doomu yàlla ji.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,785,120,254 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK