Vous avez cherché: mandamiento (Espagnol - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Espagnol

Wolof

Infos

Espagnol

Éste es el grande y el primer mandamiento

Wolof

loolu moo di li jëkk te ëpp ci li yàlla santaane.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

esto digo a modo de concesión, no como mandamiento

Wolof

li ma leen di wax fii du ndigal, waaye dama leen di xamal li ñu leen may, ngeen def ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

--maestro, ¿cuál es el gran mandamiento de la ley

Wolof

«kilifa gi, ban ndigal moo gën a màgg ci yoonu musaa?»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

y descubrí que el mismo mandamiento que era para vida me resultó en muerte

Wolof

noonu gis naa ne, ndigal loolu waroon a jëme nit ñi ci dund, daf maa jëme ci dee.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

a la verdad, el mandamiento anterior fue abrogado por ser ineficaz e inútil

Wolof

noonu tebbi nañu yoon wu jëkk, wa néewoon doole te meññul dara

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

honra a tu padre y a tu madre (que es el primer mandamiento con promesa

Wolof

«teralal sa ndey ak sa baay,» mooy ndigal li jëkk a ëmb dige,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

les decía también: --¡bien desecháis el mandamiento de dios para establecer vuestra tradición

Wolof

mu teg ca ne leen: «xelu ngeen ci tebbi ndigali yàlla, ngir sàmm seen aada.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

de manera que la ley ciertamente es santa; y el mandamiento es santo, justo y bueno

Wolof

kon nag man nanoo wax ne, yoonu musaa yoon wu sell la, te ndigalu yàlla dafa sell, jub te baax.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

porque el pecado, tomando ocasión por el mandamiento, me engañó; y por él, me mató

Wolof

ndaxte bàkkaar jaar na ci li yàlla digle, ba nax ma, rey ma.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

el segundo es éste: amarás a tu prójimo como a ti mismo. no hay otro mandamiento mayor que estos dos

Wolof

te ñaareel bi, lii la: “nanga bëgg sa moroom, ni nga bëgge sa bopp.” ndigal yii ñoo sut yépp.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

me alegré mucho al hallar de entre tus hijos quienes andan en la verdad, conforme al mandamiento que hemos recibido del padre

Wolof

gis naa ci say doom, ñuy jaar ci tànki dëgg, ni nu ko baay bi digale, te bég naa ci lool.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

y sé que su mandamiento es vida eterna. así que, lo que yo hablo, lo hablo tal y como el padre me ha hablado.

Wolof

te xam naa ne, li muy santaane day joxe dund gu dul jeex. kon li ma wax, dama koy wax, ni ma ko baay bi sante.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

amados, no os escribo un mandamiento nuevo sino el mandamiento antiguo que teníais desde el principio. el mandamiento antiguo es la palabra que habéis oído

Wolof

samay soppe, li ma leen di bind du ndigal lu bees, waaye ndigal lu yàgg la; la ngeen jotoon ca ndoorte la. te ndigal lu yàgg loolu, mooy kàddu gi ngeen déggoon.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

este mandamiento te encargo, hijo timoteo, conforme a las profecías que antes se hicieron acerca de ti, para que milites por ellas la buena milicia

Wolof

kon nag timote sama doom, loolu mooy sas wi ma lay dénk, te mu dëppook waxi yonent, yi jëmoon ci yaw. doolewool wax yooyu, ba xeex xeex bu baax bi,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

por la fe moisés, cuando nació, fue escondido por sus padres durante tres meses, porque vieron que era un niño hermoso y porque no temieron al mandamiento del rey

Wolof

ngëm moo tax ba, bi musaa juddoo, ay waajuram nëbb ko lu mat ñetti weer, ndaxte gisoon nañu ne, xale bu taaru la woon, te ragaluñu woon ndigalu buur bi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

y ahora te ruego, señora, no como si te escribiera un nuevo mandamiento, sino el mismo que teníamos desde el principio: que nos amemos unos a otros

Wolof

léegi nag soxna si, maa ngi lay dénk lii: nun ñépp nanu bëggante, te loolu du dénkaane bu bees, waaye moom lanu jotoon ca njàlbéen ga.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

nadie me la quita, sino que yo la pongo de mí mismo. tengo poder para ponerla, y tengo poder para volverla a tomar. este mandamiento recibí de mi padre.

Wolof

kenn du ko jële ci man; maa koy joxe ci sama coobarey bopp. am naa it sañ-sañu joxe ko te am naa sañ-sañu jëlaat ko. loolu la ma sama baay sant.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

ciertamente, aquellos descendientes de leví que han recibido el sacerdocio tienen, según la ley, mandamiento de recibir los diezmos del pueblo, es decir, de sus hermanos, aunque ellos también son descendientes de abraham

Wolof

yoonu musaa digle na ne, ñi bokk ci giiru lewi te di ay saraxalekat, nañu jot asaka ci alalu bànni israyil, doonte sax ñuy seeni bokk te soqikoo ci ibraayma.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

pero respondiendo él dijo a su padre: "he aquí, tantos años te sirvo, y jamás he desobedecido tu mandamiento; y nunca me has dado un cabrito para regocijarme con mis amigos

Wolof

waaye taaw ba tontu baayam ne ko: “seetal ñaata at laa la liggéeyal, mel ni jaam, te musumaa moy sa ndigal, waaye yaw, musuloo ma may sax tef, ngir ma bànneexu, man ak samay xarit.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Espagnol

"por lo tanto, cualquiera que quebranta el más pequeño de estos mandamientos y así enseña a los hombres, será considerado el más pequeño en el reino de los cielos. pero cualquiera que los cumple y los enseña, éste será considerado grande en el reino de los cielos

Wolof

ku tebbi nag ba gën a tuuti ci ndigal yii, te ngay jàngal nit ñi noonu, dees na la tudde ki gën a tuuti ci nguuru yàlla aji kawe ji. waaye ku leen di sàmm, di leen digle, dees na la tudde ku mag ci nguuru yàlla aji kawe ji.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,783,766,962 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK