Vous avez cherché: que comida quieres que lleve (Espagnol - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Espagnol

Wolof

Infos

Espagnol

ellos le preguntaron: --¿dónde quieres que la preparemos

Wolof

Ñu ne ko: «fan nga bëggoon, nu defare ko fa?»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

toda rama que en mí no está llevando fruto, la quita; y toda rama que está llevando fruto, la limpia para que lleve más fruto

Wolof

car bu soqikoo ci man te meññul, dina ko dog, sànni. waaye car bu ci meññ, dina ko tenqi, ngir mu gën a meññ.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

quien quiere que todos los hombres sean salvos y que lleguen al conocimiento de la verdad

Wolof

bi bëgg ñépp mucc te xam dëgg gi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

diciendo: --¿qué quieres que te haga? y él dijo: --señor, que yo recobre la vista

Wolof

«loo bëggoon ma defal la ko?» mu ne ko: «sang bi, damaa bëgg a gis.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

porque es mejor que padezcáis haciendo el bien, si la voluntad de dios así lo quiere, que haciendo el mal

Wolof

Ñu fitnaal la ndax jëf ju baax, su dee mooy coobareg yàlla, moo gën ñu fitnaal la ndax jëf ju bon.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

no quiero que ignoréis, hermanos, que todos nuestros padres estuvieron bajo la nube, y que todos atravesaron el mar

Wolof

bokk yi, bëgguma ngeen umple li daloon sunu maam ya. Ñoom ñépp niir wa tiimoon na leen, te ñoom ñépp jàll nañu géej.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

quiero que estés bien y verte contento toda la vida lo mereces te quiero

Wolof

Dernière mise à jour : 2024-03-13
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

pero no quiero que ignoréis, hermanos, acerca de los dones espirituales

Wolof

léegi nag bokk yi, ci li jëm ci mayi xelum yàlla, bëgguma ngeen umple ci dara.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

al contrario, digo que lo que los gentiles sacrifican, lo sacrifican a los demonios, y no a dios. y yo no quiero que vosotros participéis con los demonios

Wolof

déedéet! waaye sarax yi xërëmkat yi di rendi, ay rab lañu ko jagleel; jagleeluñu ko yàlla. te man bëgguma, ngeen booloo ak rab yi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

el primer día de la fiesta de los panes sin levadura, cuando sacrificaban el cordero de la pascua, sus discípulos le dijeron: --¿dónde quieres que vayamos y hagamos los preparativos para que comas la pascua

Wolof

bés bu jëkk ca màggal, ga ñuy wax mburu ya amul lawiir, taalibey yeesu laaj ko: «foo bëgg, nu defaral la reeru jéggi bi?» bés bu jëkk booba nag mooy bés, ba ñu faral a rendi xarum màggalu jéggi ba.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

"entrad por la puerta estrecha; porque ancha es la puerta, y espacioso el camino que lleva a la perdición, y son muchos los que entran por ella

Wolof

«jaarleen ci bunt bu xat bi, ndaxte bunt bi ak yoon wi jëm sànku yaatu nañu, te ñi ciy jaar bare.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Espagnol

hermanos, para que no seáis sabios en vuestro propio parecer, no quiero que ignoréis este misterio: que ha acontecido a israel endurecimiento en parte, hasta que haya entrado la plenitud de los gentiles

Wolof

bokk yi, dama leen a bëgg a dindi kumpa ci lii, ngir ngeen bañ a yég seen bopp. dërkiisu xol dab na bànni israyil ab diir, ba bés ba mboolem waa àddina, ñu war a bokk ci nguuru yàlla, dugg ca.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

"padre, quiero que donde yo esté, también estén conmigo aquellos que me has dado, para que vean mi gloria que me has dado, porque me has amado desde antes de la fundación del mundo

Wolof

«baay, bëgg naa, ñi nga ma dénk nekk ak man fa ma jëm, ngir ñu gis sama ndam, li nga ma sol, ndaxte bëgg nga ma, laata àddina di sosu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Espagnol

así que el dicho se difundió entre los hermanos de que aquel discípulo no habría de morir. pero jesús no le dijo que no moriría, sino: "si yo quiero que él quede hasta que yo venga, ¿qué tiene que ver eso contigo?

Wolof

noonu am, ci bokki taalibe yi, ñu xalaat ne, taalibe boobu du dee. moona yeesu musul ne piyeer, du dee; waaye li mu wax mooy: «su ma neexoon mu dund, ba ma dellusi, lu ciy sa yoon?»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Certaines traductions humaines peu pertinentes ont été masquées.
Affichez les résultats peu pertinents.

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,778,050,373 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK