Vous avez cherché: resucitó (Espagnol - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Espagnol

Wolof

Infos

Espagnol

que fue sepultado y que resucitó al tercer día, conforme a las escrituras

Wolof

suul nañu ko, mu dekki ca ñetteelu fan ba, ni ko mbind mi tërale.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

y juntamente con cristo jesús, nos resucitó y nos hizo sentar en los lugares celestiales

Wolof

te dekkal na nu ak kirist yeesu, dëël nu ak moom ca bérab yu kawe ya.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

la gente que estaba con él daba testimonio de cuando llamó a lázaro del sepulcro y le resucitó de entre los muertos

Wolof

Ña nekkoon ak yeesu ñépp, bi muy wooyee lasaar mu génn ca bàmmeel ba te mu dekkal ko, demoon nañu, nettali la ñu gis.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

dios la ejerció en cristo cuando lo resucitó de entre los muertos y le hizo sentar a su diestra en los lugares celestiales

Wolof

ji mu jëfe ci kirist, ci li mu ko dekkal, dëël ko ci ndeyjooram ca bérab yu kawe ya,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

y él murió por todos para que los que viven ya no vivan más para sí, sino para aquel que murió y resucitó por ellos

Wolof

te dee na ngir ñépp, ngir ñiy dund dootuñu dund ngir seen bopp, waaye ngir ki dee ci seen wàll te dekki.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

seis días antes de la pascua, llegó jesús a betania, donde estaba lázaro, a quien jesús resucitó de entre los muertos

Wolof

juróom benni fan laata màggalu bésub jéggi ba, yeesu dem na betani, dëkku lasaar, mi mu dekkal.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

a él, dios le resucitó, habiendo desatado los dolores de la muerte; puesto que era imposible que él quedara detenido bajo su dominio

Wolof

waaye yàlla dekkal na ko, daggal ko buumi dee, ndaxte dee mënu koo téye.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

sino también para nosotros, a quienes nos habría de ser contada: a los que creemos en el que resucitó de entre los muertos, a jesús nuestro señor

Wolof

nun itam ci wax jooju lanu bokk, te yàlla dina nu jagleel njub, nun ñi gëm yàlla, mi dekkal yeesu sunu boroom.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

sea conocido a todos vosotros y a todo el pueblo de israel, que ha sido en el nombre de jesucristo de nazaret, a quien vosotros crucificasteis y a quien dios resucitó de entre los muertos. por jesús este hombre está de pie sano en vuestra presencia

Wolof

nangeen xam lii, yéen ñépp ak bànni israyil gépp! ci turu yeesu kirist mu nasaret, mi ngeen daajoon ca bant te yàlla dekkal ko, ci tur woowu la nit kii jële ag wér, ba taxaw ci seen kanam.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

de manera semejante, hermanos míos, vosotros también habéis muerto a la ley por medio del cuerpo de cristo, para ser unidos con otro, el mismo que resucitó de entre los muertos, a fin de que llevemos fruto para dios

Wolof

nii laa leen ko man a misaale, samay bokk; bi kirist deeyee, dangeen a deeyandoo ak moom, te noonu yoonu musaa wàcc leen. léegi nag yéena ngi ànd ak keneen, maanaam kirist mi dekki, ngir nu amal yàlla njariñ.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

así también es la resurrección de los muertos. se siembra en corrupción; se resucita en incorrupción

Wolof

noonu la ndekkitel néew yi di deme. bu ñu suulee néew bi, dañoo ji lu yàqu. bu dekkee, du yàqooti ba abadan.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,728,936,475 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK