Vous avez cherché: resurrección (Espagnol - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Espagnol

Wolof

Infos

Espagnol

porque si no hay resurrección de muertos, tampoco cristo ha resucitado

Wolof

su fekkee ne ñi dee duñu dekki, kon kirist it dekkiwul.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

marta le dijo: --yo sé que resucitará en la resurrección en el día final

Wolof

màrt tontu ko ne: «xam naa ne, dina jóg bésu ndekkite la, keroog bés bu mujj ba.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

resentidos de que enseñasen al pueblo y anunciasen en jesús la resurrección de entre los muertos

Wolof

Ñu mer lool ci li ñuy waar nit ñi, di yégle ndekkitel ñi dee, sukkandikoo ko ci ndekkitel yeesu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

aquel día se le acercaron unos saduceos, quienes dicen que no hay resurrección, y le preguntaron diciendo

Wolof

bés boobale ay sadusen ñëw ci moom. sadusen yi nag ñoom gëmuñu ne ndekkite am na. noonu ñu laaj ko naan:

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

porque en la resurrección no se casan ni se dan en casamiento, sino que son como los ángeles que están en el cielo

Wolof

ndaxte keroog ndekkite li kenn du am jabar, kenn du am jëkkër, waaye dinañu mel ni malaaka yi ci kaw.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

de la doctrina de bautismos, de la imposición de manos, de la resurrección de los muertos y del juicio eterno

Wolof

di leen jàngalaat ci mbirum sangu set ci ay fànn yu bare, ak teg loxo ak ci mbirum ndekkite ak lu jëm ci àtte biy sax dàkk.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

anhelo conocerle a él y el poder de su resurrección, y participar en sus padecimientos, para ser semejante a él en su muerte

Wolof

moom laay ittewoo xam, ak doole ji ànd ak ndekkiteem, ma bokk ci ay coonoom, ba fekki ko ci deeyam,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

jesús le dijo: --yo soy la resurrección y la vida. el que cree en mí, aunque muera, vivirá

Wolof

yeesu ne ko: «man maay ndekkite li, maay dund gi. ku ma gëm, boo deeyee it, dinga dund.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

en la resurrección, cuando resuciten, puesto que los siete la tuvieron por mujer, ¿de cuál de ellos será mujer

Wolof

ci ndekkite li nag kan ci ñoom moo ko war a donn, fekk ku nekk ci juróom-ñaar ñi mas na koo takk?»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

comenzando desde el bautismo de juan hasta el día en que fue tomado de nosotros y recibido arriba, es preciso que uno sea con nosotros testigo de su resurrección.

Wolof

li dale ci bi ko yaxya sóobee ci ndox, ba bés ba ko yàlla jële ci sunu biir, yéege ko. kooku war na ànd ak nun, di seedeel ndekkitel yeesu.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

ahora bien, si cristo es predicado como que ha resucitado de entre los muertos, ¿cómo es que algunos entre vosotros dicen que no hay resurrección de muertos

Wolof

waaye su nu yéglee ne, kirist dekki na, nan la ñenn ñi ci yéen man a waxe ne, néew yi duñu dekki?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

cuando le oyeron mencionar la resurrección de los muertos, unos se burlaban, pero otros decían: --te oiremos acerca de esto en otra ocasión

Wolof

bi ñu déggee nag, muy wax ci mbirum ndekkitel ñi dee, ñii di ko fontoo, ña ca des ne ko: «dinanu la déglu ci mbir moomu beneen yoon.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

bienaventurado y santo el que tiene parte en la primera resurrección. sobre éstos la segunda muerte no tiene ningún poder; sino que serán sacerdotes de dios y de cristo, y reinarán con él por los mil años

Wolof

Ñi bokk ci ndekkite lu jëkk li, barkeel nañu te sell! Ñaareelu dee gi du leen manal dara. waaye dinañu doon saraxalekati yàlla ak kirist, tey nguuru ak moom junniy at.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

el bautismo, que corresponde a esta figura, ahora, mediante la resurrección de jesucristo, os salva, no por quitar las impurezas de la carne, sino como apelación de una buena conciencia hacia dios

Wolof

loolu misaal la tey, ci li ñu nuy sóob ci ndox, te nu mucc; waxuma laabal sobe si taq ci yaram, waaye wuyu yàlla ak xel mu dal. li nu may mucc googu, mooy ndekkitel yeesu kirist,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

entonces pablo, sabiendo que una parte del sanedrín eran saduceos y la otra parte fariseos, gritó en el sanedrín: --hermanos, yo soy fariseo, hijo de fariseos. es por la esperanza y la resurrección de los muertos que soy juzgado

Wolof

naka noona pool, mi xam ne, genn-wàllu kureel ga bokk nañu ci tariixab sadusen ya, te ña ca des bokk ci tariixab farisen ya, mu wax ci kaw ci biir géew ba ne: «bokk yi, man farisen laa, te farisen moo ma jur; li tax ñu may àtte tey mooy sama yaakaar ci ne, ñi dee dinañu dekki.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,782,240,947 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK