Vous avez cherché: vientre (Espagnol - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Espagnol

Wolof

Infos

Espagnol

he aquí concebirás en tu vientre y darás a luz un hijo, y llamarás su nombre jesús

Wolof

dinga ëmb, jur doom ju góor; nanga ko tudde yeesu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

porque he aquí, cuando llegó a mis oídos la voz de tu salutación, la criatura saltó de alegría en mi vientre

Wolof

maa ngi lay wax ne, naka laa la dégg ngay nuyoo rekk, sama doom ji yengu ci sama biir ndax mbég.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

en listra se hallaba sentado cierto hombre imposibilitado de los pies, cojo desde el vientre de su madre, que jamás había caminado

Wolof

amoon na ca listar nag nit ku fa toog, ku ay tànkam làggi, ndax li mu judduwaale lafañ te musul a dox.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

aconteció que, cuando elisabet oyó la salutación de maría, la criatura saltó en su vientre. y elisabet fue llena del espíritu santo

Wolof

naka la elisabet dégg maryaama di nuyoo, doomam daldi yengatu ci biiram. noonu xelum yàlla mu sell mi daldi solu elisabet.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

cuando se cumplieron los ocho días para circuncidar al niño, llamaron su nombre jesús, nombre que le fue puesto por el ángel antes que él fuese concebido en el vientre

Wolof

bi bés ba dellusee jamonoy xarafal xale ba agsi. Ñu tudde ko yeesu, ni ko malaaka ma diglee woon, laata ko yaayam di ëmb.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

y era traído cierto hombre que era cojo desde el vientre de su madre. cada día le ponían a la puerta del templo que se llama hermosa, para pedir limosna de los que entraban en el templo

Wolof

fekk ñu indi fa nit ku judduwaale lafañ, ñu di ko teg bés bu nekk ca bunt, ba ñuy wooye bunt bu rafet ba, ca kër yàlla ga, ngir muy yelwaan ña fay dugg.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

mientras él decía estas cosas, aconteció que una mujer de entre la multitud levantó la voz y le dijo: --¡bienaventurado el vientre que te llevó y los pechos que mamaste

Wolof

bi yeesu di wax loolu, jenn jigéen yékkati baatam ca biir mbooloo ma ne: «céy jigéen ji la ëmb te nàmpal la moo barkeel!»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

nicodemo le dijo: --¿cómo puede nacer un hombre si ya es viejo? ¿puede acaso entrar por segunda vez en el vientre de su madre y nacer

Wolof

nikodem ne ko: «nit ku xas ba màggat, nan lay man a judduwaate? ndax day dellu ci biiru yaayam ngir judduwaat?»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Espagnol

porque he aquí vendrán días en que dirán: "bienaventuradas las estériles, los vientres que no concibieron y los pechos que no criaron.

Wolof

ndaxte jamono dina ñëw, ju ñu naan: “jigéen ñi musul a jur ak ñi musul a nàmpal, barkeel ngeen!”

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,334,721 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK