Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
rendez grâces au père, qui vous a rendus capables d`avoir part à l`héritage des saints dans la lumière,
dingeen gërëm yàlla baay bi, ànd ci ak mbég, moom mi leen jagleel, ngeen bokk ci cér, bi mu dencal gaayam yu sell yi ci leer.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
c`est par beaucoup de paraboles de ce genre qu`il leur annonçait la parole, selon qu`ils étaient capables de l`entendre.
noonu yeesu dégtal leen yeneeni léeb yu bare yu mel ni yii, di leen xamal kàddu gi, aju ci lu ñu àttan.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
attaché à la vraie parole telle qu`elle a été enseignée, afin d`être capable d`exhorter selon la saine doctrine et de réfuter les contradicteurs.
war na jàpp ci xebaar bu dëggu, bi lal sunu yoon, ba man a dénkaane ci njàngale mu wér mi, tey yey ñi weddi.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :