Vous avez cherché: circoncis (Français - Wolof)

Français

Traduction

circoncis

Traduction

Wolof

Traduction
Traduction

Traduisez instantanément des textes, des documents et des voix avec Lara

Traduire maintenant

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Français

Wolof

Infos

Français

et lorsque pierre fut monté à jérusalem, les fidèles circoncis lui adressèrent des reproches,

Wolof

bi piyeer demee yerusalem nag, kureelu yawut gi farataal xaraf, di werante ak moom ne ko:

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

prenez garde aux chiens, prenez garde aux mauvais ouvriers, prenez garde aux faux circoncis.

Wolof

moytuleen xaj yi, waaw moytuleen ñiy jëfe lu bon, ñoom ñi seen xarafal weesul wàññi yaramu nit.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

puisqu`il y a un seul dieu, qui justifiera par la foi les circoncis, et par la foi les incirconcis.

Wolof

gannaaw yàlla kenn la, ñépp la fi nekkal. Ñi xaraf dina leen àtte ni ñu jub ndax seen ngëm, ñi xaraful it dina leen àtte ni ñu jub ndax seen ngëm.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

tous les fidèles circoncis qui étaient venus avec pierre furent étonnés de ce que le don du saint esprit était aussi répandu sur les païens.

Wolof

yawut yi gëm yépp nag, ñi ànd ak piyeer, daldi waaru ci li yàlla tuur xel mu sell, mi mu maye, ci ñi dul yawut itam.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

il y a, en effet, surtout parmi les circoncis, beaucoup de gens rebelles, de vains discoureurs et de séducteurs,

Wolof

loolu war na, ndaxte am na ñu bare ñu déggul lenn ndigal, rawatina ci yawut yi, ñuy yàq xeli nit ñi ak seen waxi neen.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

car celui qui a fait de pierre l`apôtre des circoncis a aussi fait de moi l`apôtre des païens, -

Wolof

ndaxte ni yàlla jëfe ci piyeer, miy ndawam ci yawut yi, noonu it la jëfe ci man, may ndawam ci ñi dul yawut.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

au contraire, voyant que l`Évangile m`avait été confié pour les incirconcis, comme à pierre pour les circoncis, -

Wolof

gis nañu ne, yàllaa nu yebal, muy man di piyeer, ngir nu yégle xebaar bu baax bi; ma féetewoo ñi dul yawut, piyeer féetewoo yawut yi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

car les circoncis eux-mêmes n`observent point la loi; mais ils veulent que vous soyez circoncis, pour se glorifier dans votre chair.

Wolof

kureel gi faaydaal xaraf, ñoom ci seen bopp sax, duñu topp yoon wi. dañoo bëgg a ngeen xaraf, ba ñu man a bàkku ci seen yaram, yéen.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

jésus, appelé justus, vous salue aussi. ils sont du nombre des circoncis, et les seuls qui aient travaillé avec moi pour le royaume de dieu, et qui aient été pour moi une consolation.

Wolof

yeesu mi ñuy dàkkentale yustus, moom it mu ngi leen di nuyu. Ñoom rekk ñooy yawut yiy liggéeyandook man ngir nguuru yàlla, te ñoo féexal sama xol.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

c`est pourquoi, vous autrefois païens dans la chair, appelés incirconcis par ceux qu`on appelle circoncis et qui le sont en la chair par la main de l`homme,

Wolof

kon nag yéen ñi dul yawut cib juddu, yéen ñi xaraful, te ñi xaraf ci seen yaram ci loxol nit ñoo leen teg ay yéefar, fàttalikuleen lii:

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

car les circoncis, c`est nous, qui rendons à dieu notre culte par l`esprit de dieu, qui nous glorifions en jésus christ, et qui ne mettons point notre confiance en la chair.

Wolof

ndaxte nun noo xaraf tigi, nun ñiy màggal yàlla ci xel mu sell mi, di damu ci kirist yeesu, te amunu jenn yaakaar ci matug nit.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
8,641,997,534 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK