Vous avez cherché: circoncision (Français - Wolof)

Français

Traduction

circoncision

Traduction

Wolof

Traduction
Traduction

Traduisez instantanément des textes, des documents et des voix avec Lara

Traduire maintenant

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Français

Wolof

Infos

Français

quel est donc l`avantage des juifs, ou quelle est l`utilité de la circoncision?

Wolof

yawut bi nag, ci lan la rawe ku dul yawut? te xaraf lu muy njariñ?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

la circoncision est utile, si tu mets en pratique la loi; mais si tu transgresses la loi, ta circoncision devient incirconcision.

Wolof

bëggoon naa ngeen xam ne, xaraf am na njariñ, boo ca boolee sàmm yoon. waaye boo ko ca boolewul, sa xaraf amatul njariñ.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

car, en jésus christ, ni la circoncision ni l`incirconcision n`a de valeur, mais la foi qui est agissante par la charité.

Wolof

ndaxte bu nu bokkee ci kirist yeesu, xaraf ak bañ a xaraf, dara amu ci solo; li am solo mooy ngëm, giy jëf ci mbëggeel.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

la circoncision n`est rien, et l`incirconcision n`est rien, mais l`observation des commandements de dieu est tout.

Wolof

xaraf ak ñàkka xaraf lépp a yem; li am solo moo di topp ndigali yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

le juif, ce n`est pas celui qui en a les dehors; et la circoncision, ce n`est pas celle qui est visible dans la chair.

Wolof

juddu nekk yawut taxul sag yawut dëggu, te xaraf ci saw yaram taxul sa xaraf wóor.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

moïse vous a donné la circoncision, -non qu`elle vienne de moïse, car elle vient des patriarches, -et vous circoncisez un homme le jour du sabbat.

Wolof

li leen musaa jox ndigalu xarafal gune yi --jógewul kat ci musaa; mi ngi tàmbalee ci seen maami cosaan — moo tax ba ngeen nangoo xarafal nit ci bésu noflaay bi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

comment donc lui fut-elle imputée? Était-ce après, ou avant sa circoncision? il n`était pas encore circoncis, il était incirconcis.

Wolof

kañ la ko jagleel njub nag? ndax lu jiitu xarafam la woon, am gannaaw ga? lu ko jiitu la woon.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
8,642,002,743 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK