Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
elle ne se réjouit point de l`injustice, mais elle se réjouit de la vérité;
du bég ci lu awul yoon, waaye dina bég ci lépp luy jollil dëgg.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
la colère de dieu se révèle du ciel contre toute impiété et toute injustice des hommes qui retiennent injustement la vérité captive,
merum yàllaa ngi feeñe asamaan, wàcc ci nit ñi, ndax seen weddi yàlla gépp ak seen jubadi gépp, ñoom ñi suul dëgg, di topp lu jubadi.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
car celui qui agit injustement recevra selon son injustice, et il n`y a point d`acception de personnes.
waaye ku def lu bon, boroom bi dina la delloo sa jëf, te du gënale.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
afin que tous ceux qui n`ont pas cru à la vérité, mais qui ont pris plaisir à l`injustice, soient condamnés.
noonu yàlla dina mbugal ñépp ñi gëmul woon dëgg te doon bànneexu ci njubadi.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
que dirons-nous donc? y a-t-il en dieu de l`injustice? loin de là!
kon lu nu ci war a wax? ndax yàlla àttewul foofu yoon nag? mukk!
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
mais l`irritation et la colère à ceux qui, par esprit de dispute, sont rebelles à la vérité et obéissent à l`injustice.
waaye ñi dëgër bopp, ba tanqamlu dëgg, di topp lu jubadi, seen pey mooy dooni merum yàlla ak toroxte.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
mais c`est vous qui commettez l`injustice et qui dépouillez, et c`est envers des frères que vous agissez de la sorte!
waaye yéen sax yéenay tooñ ak di sàcc, te seeni bokk ngeen koy def!
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
c`est déjà certes un défaut chez vous que d`avoir des procès les uns avec les autres. pourquoi ne souffrez-vous pas plutôt quelque injustice? pourquoi ne vous laissez-vous pas plutôt dépouiller?
layoo bi sax wone na ne, bàyyi ngeen seen warugar. lu tax muñuleen sax tooñ, yi ñu leen di tooñ? lu tax far nanguwuleen, ñu sàcc leen?
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :