Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
je vais bien
maguifi
Dernière mise à jour : 2022-05-17
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
je vais te gifler
Dernière mise à jour : 2020-07-25
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
présentement je vais à jérusalem, pour le service des saints.
waaye nag fi mu nekk maa ngi dem nii yerusalem, ngir dimbaliji gaayi yàlla yu sell ya fa nekk.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
je vais commencer a parler wolof
Dernière mise à jour : 2024-02-26
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
vous savez où je vais, et vous en savez le chemin.
te fa ma jëm, xam ngeen yoon wi.»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
aspirez aux dons les meilleurs. et je vais encore vous montrer une voie par excellence.
waaye fonkleen may yi gën. léegi nag ma won leen yoon wu gën lépp.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
et maintenant voici, lié par l`esprit, je vais à jérusalem, ne sachant pas ce qui m`y arrivera;
«léegi maa ngi nii di dem yerusalem, ci li ma xelu yàlla mi xiirtal, te xawma lu ma fay dal.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
après ces paroles, il leur dit: lazare, notre ami, dort; mais je vais le réveiller.
yeesu wax loolu, teg ca ne: «sunu xarit lasaar nelaw na, waaye maa ngi dem yee ko.»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
encore un peu de temps, et vous ne me verrez plus; et puis encore un peu de temps, et vous me verrez, parce que je vais au père.
«ci kanam tuuti dungeen ma gisati. bu ñu ci tegee ab diir, ngeen gisaat ma.»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
voyez, contempteurs, soyez étonnés et disparaissez; car je vais faire en vos jours une oeuvre, une oeuvre que vous ne croiriez pas si on vous la racontait.
“yéen ñiy xeebaate, gis leen lii,ngeen yéemu ba far;ndaxte dinaa def ci seen jamono jëf,joo xam ne su ngeen ko déggee sax,dungeen ko gëm.”»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
c`est pourquoi, si je vais vous voir, je rappellerai les actes qu`il commet, en tenant contre nous de méchants propos; non content de cela, il ne reçoit pas les frères, et ceux qui voudraient le faire, il les en empêche et les chasse de l`Église.
kon nag su ma ñëwee, dinaa fàttali li mu def lépp, ci di nu sosal ci kàdduy neen yu ñaaw. yemu foofu sax, waaye nanguwula teeru mbokk yi, rax-ca-dolli ku leen bëgga teeru, mu gàllankoor ko, dàq ko ci mbooloo mi.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence: