Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
désirez, comme des enfants nouveau-nés, le lait spirituel et pur, afin que par lui vous croissiez pour le salut,
gannaaw ay liir ngeen yuy door a juddu te mos ci mbaaxug boroom bi, nàmpleen ci meew mu sell, miy dundal seen xol, ba màgg ci biir muccu yàlla.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
je vous ai donné du lait, non de la nourriture solide, car vous ne pouviez pas la supporter; et vous ne le pouvez pas même à présent, parce que vous êtes encore charnels.
nàmpaloon naa leen, waaye joxuma leen dugub, ndaxte àttanuleen ko woon, te ba léegi sax àttanuleen ko
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :