Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
miséricorde
miséricorde
Dernière mise à jour : 2023-10-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
heureux les miséricordieux, car ils obtiendront miséricorde!
yéen ñi am yërmande, barkeel ngeen,ndax dees na leen yërëm.
Dernière mise à jour : 2023-10-22
Fréquence d'utilisation : 2
Qualité :
ainsi, il fait miséricorde à qui il veut, et il endurcit qui il veut.
kon nag yàlla, la ko neex lay def, muy yërëm nit, mbaa dëgëral xolam ci lu bon.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
car dieu a renfermé tous les hommes dans la désobéissance, pour faire miséricorde à tous.
kon yàlla tëj na ñépp ci ngëmadi, ngir man a yërëm ñépp.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
de même que vous avez autrefois désobéi à dieu et que par leur désobéissance vous avez maintenant obtenu miséricorde,
Ñu déggadil yàlla ngeen woon, waaye ngëmadig yawut yi tax na, ngeen jot yërmandeem.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
mais dieu, qui est riche en miséricorde, à cause du grand amour dont il nous a aimés,
waaye yàlla mi bare yërmande, ci kaw mbëggeel gu réy, gi mu am ci nun,
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
il a secouru israël, son serviteur, et il s`est souvenu de sa miséricorde, -
wallu na bànni israyil giy jaamam,di fàttaliku yërmandeem,
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
car le jugement est sans miséricorde pour qui n`a pas fait miséricorde. la miséricorde triomphe du jugement.
ndaxte ku yërëmul, yoon du la yërëm. te yërmande mooy noot àtte.
Dernière mise à jour : 2023-11-05
Fréquence d'utilisation : 3
Qualité :
ainsi donc, cela ne dépend ni de celui qui veut, ni de celui qui court, mais de dieu qui fait miséricorde.
dama leen di wax nag, dara ajuwul ci coobareg nit, mbaa ci ñaqam, waaye lépp a ngi aju ci yërmandey yàlla.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
grâce aux entrailles de la miséricorde de notre dieu, en vertu de laquelle le soleil levant nous a visités d`en haut,
ndaxte yàlla sunu boroom fees na ak yërmande,ba tax muy wàcce ci nun jant buy fenk,
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
maintenez-vous dans l`amour de dieu, en attendant la miséricorde de notre seigneur jésus christ pour la vie éternelle.
ba saxoo mbëggeelu yàlla, tey séentu yërmandey sunu boroom yeesu kirist, mu tàbbal leen ci dund gu dul jeex.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
approchons-nous donc avec assurance du trône de la grâce afin d`obtenir miséricorde et de trouver grâce, pour être secourus dans nos besoins.
kon nag nanu am kóolute ci jege jalu yàlla bu yiw ba, ngir jot yërmandeem ak yiwam, ngir mu wallu nu fu soxla taxawe.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
que la grâce, la miséricorde et la paix soient avec vous de la part de dieu le père et de la part de jésus christ, le fils du père, dans la vérité et la charité!
yàlla baay bi ak yeesu krist, doomu baay bi, dinañu nu may yiw, yërmande ak jàmm, ànd ak dëgg ak mbëggeel.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
allez, et apprenez ce que signifie: je prends plaisir à la miséricorde, et non aux sacrifices. car je ne suis pas venu appeler des justes, mais des pécheurs.
mbind mi nee na: “yërmande laa bëgg, waaye du rendi saraxi mala.” demleen nag te seet lu wax joojuy tekki. ndaxte ñëwuma, ngir woo ñi jub, waaye bàkkaarkat yi laay woo.»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
c`est celui qui a exercé la miséricorde envers lui, répondit le docteur de la loi. et jésus lui dit: va, et toi, fais de même.
xutbakat ba tontu ko ne: «xanaa ki ko won yërmandeem.» yeesu ne ko nag: «demal tey def ni moom.»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
pour ce qui est des vierges, je n`ai point d`ordre du seigneur; mais je donne un avis, comme ayant reçu du seigneur miséricorde pour être fidèle.
ci li jëm ci janq yi, awma ndigalu boroom bi, waaye maa ngi joxe sama xalaat, ni ku ñu wóolu ndax li ma jot yërmandey boroom bi.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
ainsi donc, comme des élus de dieu, saints et bien-aimés, revêtez-vous d`entrailles de miséricorde, de bonté, d`humilité, de douceur, de patience.
kon nag ndegam yàlla tànn na leen, sellal leen, sopp leen, solooleen boog yërmande, laabiir, woyof, lewet ak muñ.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :