Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
c`est par la foi que rahab la prostituée ne périt pas avec les rebelles, parce qu`elle avait reçu les espions avec bienveillance.
ngëm moo tax ba raxab jigéenu moykat bi mucc, keroog ba ñuy bóom ñi déggadiloon yàlla, ndax li mu teeru woon yëddukat ya teeru bu ànd ak jàmm.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
parce que ses jugements sont véritables et justes; car il a jugé la grande prostituée qui corrompait la terre par son impudicité, et il a vengé le sang de ses serviteurs en le redemandant de sa main.
ay àtteem dañoo dëggu te jub!ndaxte àtte na jigéenu moykat bu mag,bi daan yàq àddina si ak njaaloom,te feyyul na noonu jaami yàlla, yi mu daan rey.»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
et il me dit: les eaux que tu as vues, sur lesquelles la prostituée est assise, ce sont des peuples, des foules, des nations, et des langues.
mu neeti ma: «dex yi nga gis jigéenu moykat ja toog ca kaw, mooy réew yi ak mbooloo yi ak xeet yi ak kàllaama yi.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
rahab la prostituée ne fut-elle pas également justifiée par les oeuvres, lorsqu`elle reçut les messagers et qu`elle les fit partir par un autre chemin?
naka raxab jigéenu moykat bi itam, ndax du ci noonu la ko yàlla àttee ni ku jub, ci li mu teeru ndawi yawut yi, te jaarale leen ca poot ba?
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
car jean est venu à vous dans la voie de la justice, et vous n`avez pas cru en lui. mais les publicains et les prostituées ont cru en lui; et vous, qui avez vu cela, vous ne vous êtes pas ensuite repentis pour croire en lui.
ndaxte yaxya ñëw na ci yéen ci yoonu njub, te gëmuleen ko; waaye juutikat yi ak jigéeni moykat yi gëm nañu ko. te gannaaw bi ngeen gisee loolu, seen xel soppikuwul sax, ba ngeen gëm ko.»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :