Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
jésus avait parlé de sa mort, mais ils crurent qu`il parlait de l`assoupissement du sommeil.
yeesu dafa bëggoon a wax ne, lasaar dee na, waaye taalibe yi dañoo xalaatoon ne, mbiri nelaw rekk lay wax.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
pierre et ses compagnons étaient appesantis par le sommeil; mais, s`étant tenus éveillés, ils virent la gloire de jésus et les deux hommes qui étaient avec lui.
fekk piyeer ak ñi mu àndal doon gëmmeentu, waaye bi ñu yeewoo bu baax, ñu gis ndamu yeesu, ak ñaari nit ñu taxaw ci wetam.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
cela importe d`autant plus que vous savez en quel temps nous sommes: c`est l`heure de vous réveiller enfin du sommeil, car maintenant le salut est plus près de nous que lorsque nous avons cru.
te lii itam am na: xam ngeen bu baax jamono ji nu tollu; jamonoy yeewu jot na, ndax léegi sunu mucc gën na noo jege, ca ba nu dooree gëm.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :