Vous avez cherché: tristesse (Français - Wolof)

Français

Traduction

tristesse

Traduction

Wolof

Traduction
Traduction

Traduisez instantanément des textes, des documents et des voix avec Lara

Traduire maintenant

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Français

Wolof

Infos

Français

je résolus donc en moi-même de ne pas retourner chez vous dans la tristesse.

Wolof

man nag fas yéene naa lii: duma dellusi ci yéen ci naqar.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

mais, parce que je vous ai dit ces choses, la tristesse a rempli votre coeur.

Wolof

seen xol dafa jeex ndax li ma leen wax.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

j`éprouve une grande tristesse, et j`ai dans le coeur un chagrin continuel.

Wolof

maanaam, duma noppee am naqar wu réy ci sama biir xol,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

il prit avec lui pierre et les deux fils de zébédée, et il commença à éprouver de la tristesse et des angoisses.

Wolof

bi mu waxee loolu, mu ànd ak piyeer ak ñaari doomi sebede, daldi am tiis ba xonett.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

après avoir prié, il se leva, et vint vers les disciples, qu`il trouva endormis de tristesse,

Wolof

bi mu ñaanee ba noppi, mu jóg, dellusi ci taalibe yi, fekk leen ñuy nelaw, ndaxte seen xol dafa sonnoon ak tiis.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

en sorte que vous devez bien plutôt lui pardonner et le consoler, de peur qu`il ne soit accablé par une tristesse excessive.

Wolof

léegi nag baal-leen ko te dëfël xolam, ngir bañ mu sóobu ci naqar wu ëpp.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

en effet, la tristesse selon dieu produit une repentance à salut dont on ne se repent jamais, tandis que la tristesse du monde produit la mort.

Wolof

ndaxte tiis wu jóge ci yàlla dina jur réccu guy jëme ci mucc, te réccu googu laajul gëstu. waaye tiisu àddina day jëme ci dee.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

que chacun donne comme il l`a résolu en son coeur, sans tristesse ni contrainte; car dieu aime celui qui donne avec joie.

Wolof

kon na ku nekk joxe, ni mu ko nase ci xolam, te bañ cee am réccu walla sañul-bañ, ndaxte kiy joxe ak mbég moo neex boroom bi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

sentez votre misère; soyez dans le deuil et dans les larmes; que votre rire se change en deuil, et votre joie en tristesse.

Wolof

toroxluleen te naqarlu, bay jooy; defleen seeni ree aw naqar, te seen mbég nekk tiis.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

il est vrai que tout châtiment semble d`abord un sujet de tristesse, et non de joie; mais il produit plus tard pour ceux qui ont été ainsi exercés un fruit paisible de justice.

Wolof

li am moo di ne, yar bu nuy dal, du ànd ak bànneex, day naqari, waaye gannaaw ga dafay meññ jub ak jàmm, ci ñi ko jariñoo.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

en vérité, en vérité, je vous le dis, vous pleurerez et vous vous lamenterez, et le monde se réjouira: vous serez dans la tristesse, mais votre tristesse se changera en joie.

Wolof

ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, dingeen jooy xàcc, waaye àddina dina bég; dingeen jàq, waaye seen njàqare dina soppaliku bànneex.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

et voici, cette même tristesse selon dieu, quel empressement n`a-t-elle pas produit en vous! quelle justification, quelle indignation, quelle crainte, quel désir ardent, quel zèle, quelle punition! vous avez montré à tous égards que vous étiez purs dans cette affaire.

Wolof

seen tiis wi jóge ci yàlla, gisleen nag li mu jur: ndaw njaxlaf ak lay ak mer ak ragal ak nammeel ak farlu, ak bëgg a yar ki tooñ! ci seen jëf yépp wone ngeen ne, set ngeen wecc ci mbir moomu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
8,646,133,291 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK