Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
lève toi
lève toi
Dernière mise à jour : 2023-06-24
Fréquence d'utilisation : 2
Qualité :
lève-toi, lui dit jésus, prends ton lit, et marche.
yeesu ne ko: «jógal, jël sa basaŋ te dox.»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
et une voix lui dit: lève-toi, pierre, tue et mange.
te baat ne ko: «jógal, piyeer, rey te lekk.»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
puis il lui dit: lève-toi, va; ta foi t`a sauvé.
noonu yeesu ne ko: «jógal dem; sa ngëm faj na la.»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
et j`entendis une voix qui me disait: lève-toi, pierre, tue et mange.
te dégg naa baat bu ma ne: “jógal piyeer, rey te lekk.”
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
lève-toi, descends, et pars avec eux sans hésiter, car c`est moi qui les ai envoyés.
jógal, nga wàcc te ànd ak ñoom; bul werante, ndaxte maa leen yebal.»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
et jésus dit à l`homme qui avait la main sèche: lève-toi, là au milieu.
yeesu ne ku loxoom làggi: «jógal, taxaw ci kanamu ñépp.»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
et le seigneur me dit: lève-toi, va à damas, et là on te dira tout ce que tu dois faire.
noonu ma laaj ko: “lu ma war a def, boroom bi?” boroom bi ne ma: “jógal dem damas, foofa dees na la biral lépp, li ma la yen.”
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
je te l`ordonne, dit-il au paralytique, lève-toi, prends ton lit, et va dans ta maison.
«maa ngi la koy sant, jógal, jël sa basaŋ te nga ñibbi.»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
dit d`une voix forte: lève-toi droit sur tes pieds. et il se leva d`un bond et marcha.
mu ne ko ak baat bu dëgër: «jógal taxaw bu jub.» noonu nit ki ne bërét, jóg, daldi dox.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
car, lequel est le plus aisé, de dire: tes péchés sont pardonnés, ou de dire: lève-toi, et marche?
ma wax ne: “baal nañu la say bàkkaar,” walla ma ne: “jógal te dox,” lan moo ci gën a yomb?
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
et maintenant, que tardes-tu? lève-toi, sois baptisé, et lavé de tes péchés, en invoquant le nom du seigneur.
léegi nag, looy nég? jógal, ñu sóob la ci ndox, nga set ci say bàkkaar ci tudd turu yeesu.”
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
il la saisit par la main, et lui dit: talitha koumi, ce qui signifie: jeune fille, lève-toi, je te le dis.
mu jàpp loxoom ne ko: «talita kumi,» liy tekki: «janq bi, maa ngi la koy wax, jógal.»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
lequel est le plus aisé, de dire au paralytique: tes péchés sont pardonnés, ou de dire: lève-toi, prends ton lit, et marche?
lan moo gën a yomb, ma wax ku làggi ki: “baal nañu la say bàkkaar,” walla ma wax ko: “jógal, jël sa basaŋ, tey dox”?
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
alors pierre lui dit: je n`ai ni argent, ni or; mais ce que j`ai, je te le donne: au nom de jésus christ de nazareth, lève-toi et marche.
noonu piyeer ne ko: «awma xaalis, awma wurus, waaye li ma am, dinaa la ko jox: ci turu yeesu kirist mu nasaret doxal!»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :