Vous avez cherché: mais (Français - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Français

Wolof

Infos

Français

mais il leur dit cette parabole:

Wolof

noonu yeesu daldi leen wax léeb wii ne leen:

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

mais nous devons échouer sur une île.

Wolof

waaye war nanoo luf cib dun.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

mais dieu l`a ressuscité des morts.

Wolof

waaye yàlla dekkal na ko,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

mais il parlait du temple de son corps.

Wolof

waaye kër yàlla, gi yeesu doon wax, nekkul woon ab tabax, aw yaramam ci boppam moo ko taxoon di wax.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

diversité de ministères, mais le même seigneur;

Wolof

am na ay sas yu bare, waaye benn boroom bi la.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

mais leurs yeux étaient empêchés de le reconnaître.

Wolof

fekk seeni bët muuru, ba mënu ko woon a xàmmi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

mais la sagesse a été justifiée par tous ses enfants.

Wolof

waaye li xam-xamu yàlla di jur, mooy firndeel ne dëgg la.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

il y a diversité de dons, mais le même esprit;

Wolof

am na fànni may yu bare yu jóge ci xelum yàlla, waaye menn xel moomu moo koy séddale.

Dernière mise à jour : 2024-02-04
Fréquence d'utilisation : 3
Qualité :

Français

mais il leur recommandait très sévèrement de ne pas le faire connaître.

Wolof

waaye yeesu gëdd rab yi bu wér, ngir ñu bañ koo siiwal.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

le père ne juge personne, mais il a remis tout jugement au fils,

Wolof

baay bi du àtte kenn; àtte bi yépp, jox na ko doom ji,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

le ciel et la terre passeront, mais mes paroles ne passeront point.

Wolof

asamaan ak suuf dinañu wéy, waaye samay wax du wéy mukk.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 3
Qualité :

Français

car il y a beaucoup d`appelés, mais peu d`élus.

Wolof

ndaxte ñi ñu woo bare nañu, waaye ñi ñu tànn barewul.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

ce peuple m`honore des lèvres, mais son coeur est éloigné de moi.

Wolof

“xeet wii ñu ngi may teral ci seen gémmiñ,waaye seen xol sore na ma.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

et ceux-ci iront au châtiment éternel, mais les justes à la vie éternelle.

Wolof

noonu ñii dinañu sóobu ci mbugal gu dul jeex, waaye ñi jub dinañu tàbbi ci dund gu dul jeex.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

car plusieurs rendaient de faux témoignages contre lui, mais les témoignages ne s`accordaient pas.

Wolof

teewul sax naaféq ñu bare ñëw, seede ci yeesu lu dul dëgg, waaye seen seede ànduñu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

les premiers vinrent ensuite, croyant recevoir davantage; mais ils reçurent aussi chacun un denier.

Wolof

gannaaw ga nag ñi mu jëkk a jël ñëw, yaakaar ne dinañu jot lu ëpp loolu, waaye ñoom itam ñu jot ku nekk benn denariyon.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

mais il faut auparavant qu`il souffre beaucoup, et qu`il soit rejeté par cette génération.

Wolof

waaye balaa booba fàww mu sonn lool te niti jamono jii dëddu ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

il faut qu`il ne soit ni adonné au vin, ni violent, mais indulgent, pacifique, désintéressé.

Wolof

warul di ab màndikat mbaa xeexkat, waaye na lewet te jàmmu, bañ a bëgge ci xaalis.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

chaque maison est construite par quelqu`un, mais celui qui a construit toutes choses, c`est dieu.

Wolof

ndaxte kër gu nekk am na ku ko sos, waaye ki sos lépp mooy yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

mais heureux sont vos yeux, parce qu`ils voient, et vos oreilles, parce qu`elles entendent!

Wolof

«waaye yéen barkeel ngeen, ndaxte seeni bët a ngi gis te seeni nopp di dégg!

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,783,745,725 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK