Vous avez cherché: marcher (Français - Wolof)

Français

Traduction

marcher

Traduction

Wolof

Traduction
Traduction

Traduisez instantanément des textes, des documents et des voix avec Lara

Traduire maintenant

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Français

Wolof

Infos

Français

celui qui dit qu`il demeure en lui doit marcher aussi comme il a marché lui-même.

Wolof

ku wax ne ci yàlla nga sax, fàww nga dund, ni yeesu kirist daan dunde moom ci boppam.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

quand ils le virent marcher sur la mer, ils crurent que c`étaient un fantôme, et ils poussèrent des cris;

Wolof

bi ñu ko gisee nag, muy dox ci kaw dex gi, ñu foog ne njuuma la, daldi yuuxu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

aussitôt la jeune fille se leva, et se mit à marcher; car elle avait douze ans. et ils furent dans un grand étonnement.

Wolof

ca saa sa janq bi jóg, daldi dox, ndaxte amoon na fukki at ak ñaar. Ñépp daldi waaru, ba ne jomm.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

je vous exhorte donc, moi, le prisonnier dans le seigneur, à marcher d`une manière digne de la vocation qui vous a été adressée,

Wolof

man mi ñu tëj kaso ngir boroom bi nag, maa ngi leen di dénk, ngeen dund dundin wu yellook wooteb yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

pour marcher d`une manière digne du seigneur et lui être entièrement agréables, portant des fruits en toutes sortes de bonnes oeuvres et croissant par la connaissance de dieu,

Wolof

noonu dingeen dund dund gu dëppoo ak seen bokk ci boroom bi, ba neex ko ci fànn gu nekk, di def bépp jëf yu baax, te yokk seen xam-xam ci yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

d`un saut il fut debout, et il se mit à marcher. il entra avec eux dans le temple, marchant, sautant, et louant dieu.

Wolof

mu tëb, daldi taxaw, di dox. mu dugg ak ñoom ca kër yàlla ga, muy dox, di tëb tey sant yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

voici, je vous ai donné le pouvoir de marcher sur les serpents et les scorpions, et sur toute la puissance de l`ennemi; et rien ne pourra vous nuire.

Wolof

gis ngeen, jox naa leen sañ-sañu joggi ci jaan yi ak ci jiit yi, daan dooley bañaale bi, te dara du leen man a gaañ.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

et l`amour consiste à marcher selon ses commandements. c`est là le commandement dans lequel vous devez marcher, comme vous l`avez appris dès le commencement.

Wolof

lii mooy mbëggeel: nu wéer sunug dund ci ndigali yàlla; loolu mooy ndigalam, la nu jotoon ca njàlbeen ga, te ci lanu wara jaar.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

a lystre, se tenait assis un homme impotent des pieds, boiteux de naissance, et qui n`avait jamais marché.

Wolof

amoon na ca listar nag nit ku fa toog, ku ay tànkam làggi, ndax li mu judduwaale lafañ te musul a dox.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
8,950,888,232 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK