Vous avez cherché: mediante (Italien - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Italien

Wolof

Infos

Italien

in realtà mediante la legge io sono morto alla legge, per vivere per dio

Wolof

ci li jëm ci yoonu musaa, dee naa, fekk yoon wi ci boppam moo ko waral, ngir ma man a dund, ba amal jariñ yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

o meglio, per rinfrancarmi con voi e tra voi mediante la fede che abbiamo in comune, voi e io

Wolof

maanaam ma nekk ci seen biir, te nu dimbaleente ci sunu ngëm, ndax man itam ma gën a am doole.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

il mio giusto vivrà mediante la fede; ma se indietreggia, la mia anima non si compiace in lui

Wolof

ku jub ci sama kanam dina dund ci kaw ngëm,waaye bu delloo gannaaw,sama xol du sedd ci moom.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

e che per lui chiunque crede riceve giustificazione da tutto ciò da cui non vi fu possibile essere giustificati mediante la legge di mosè

Wolof

fa la yeesu di àttee ni ku jub képp ku ko gëm.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

che dalla potenza di dio siete custoditi mediante la fede, per la vostra salvezza, prossima a rivelarsi negli ultimi tempi

Wolof

yéen ñi muy aar ci dooleem, sukkandikoo ci ngëm, di leen nége mucc, gi mu nar a feeñal bés bu mujj ba.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

con discorsi gonfiati e vani adescano mediante le licenziose passioni della carne coloro che si erano appena allontanati da quelli che vivono nell'errore

Wolof

dañuy fàbbi ñu naroona mucc ci àddina ju réer, dig leen ak làmmiñ yu neex bànneexi bakkan yu jéggi dayo.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

la sua potenza divina ci ha fatto dono di ogni bene per quanto riguarda la vita e la pietà, mediante la conoscenza di colui che ci ha chiamati con la sua gloria e potenza

Wolof

dooley yàlla moo nu may lépp lu aju ci dund gu sax ak ragal yàlla, jaarale ko ci xam gi nu ko xam, moom mi nu woo ci kaw ndamam ak dooleem.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

in lui voi siete stati anche circoncisi, di una circoncisione però non fatta da mano di uomo, mediante la spogliazione del nostro corpo di carne, ma della vera circoncisione di cristo

Wolof

ndax seen ngëm ci moom xaraf ngeen xaraf bu loxol nit deful, maanaam kirist summil na leen dooley bàkkaar, ji moomoon seen yaram. loolu mooy xaraf, bi kirist def.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

ed era ben giusto che colui, per il quale e del quale sono tutte le cose, volendo portare molti figli alla gloria, rendesse perfetto mediante la sofferenza il capo che li ha guidati alla salvezza

Wolof

ndaxte yàlla mi yelloo lépp te sàkk lépp, dogal na def ñu bare ay doomam, boole leen ci ndamam. jekk na nag mu matal yeesu ci coono bi mu daj, moom mi leen xàllal yoonu mucc gi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

se infatti, quando eravamo nemici, siamo stati riconciliati con dio per mezzo della morte del figlio suo, molto più ora che siamo riconciliati, saremo salvati mediante la sua vita

Wolof

nun ay bañaaley yàlla lanu woon, waaye doomam dee na, ngir jubale nu ak moom. gannaaw léegi nag xariti yàlla lanu, rawatina ne dinanu mucc ndax dundug doomam.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

in questo caso, infatti, avrebbe dovuto soffrire più volte dalla fondazione del mondo. ora invece una volta sola, alla pienezza dei tempi, è apparso per annullare il peccato mediante il sacrificio di se stesso

Wolof

bu demee woon noonu, kon dina sonn ba tàyyi ca njàlbéenug àddina ba tey. waaye nag benn yoon rekk la feeñu ci mujjeelu jamono yi, joxe boppam ni sarax ngir far bàkkaar yi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

dal quale tutto il corpo, ben compaginato e connesso, mediante la collaborazione di ogni giuntura, secondo l'energia propria di ogni membro, riceve forza per crescere in modo da edificare se stesso nella carità

Wolof

te jëmm jépp ci moom lay dunde, di jëmm ju ràbboo te déggoo ci bépp tenqoo, te cér bu nekk di def warugaram. noonu jëmm ji di yokku ak a màgg ci biir mbëggeel.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

alla stessa maniera, fratelli miei, anche voi, mediante il corpo di cristo, siete stati messi a morte quanto alla legge, per appartenere ad un altro, cioè a colui che fu risuscitato dai morti, affinché noi portiamo frutti per dio

Wolof

nii laa leen ko man a misaale, samay bokk; bi kirist deeyee, dangeen a deeyandoo ak moom, te noonu yoonu musaa wàcc leen. léegi nag yéena ngi ànd ak keneen, maanaam kirist mi dekki, ngir nu amal yàlla njariñ.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,090,094 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK