Vous avez cherché: padroni (Italien - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Italien

Wolof

Infos

Italien

esorta gli schiavi a esser sottomessi in tutto ai loro padroni; li accontentino e non li contraddicano

Wolof

waxal it jaam ñi, ñu déggal seeni sang ci lépp, te liggéeyal leen ba seral seen xol, bañ cee boole werante

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

schiavi, obbedite ai vostri padroni secondo la carne con timore e tremore, con semplicità di spirito, come a cristo

Wolof

yéen jaam yi, nangeen déggal seeni sang yu àddina, boole ci ragal ak wegeel, di ko def ak xol bu laab, ni su doon ngir kirist.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

domestici, state soggetti con profondo rispetto ai vostri padroni, non solo a quelli buoni e miti, ma anche a quelli difficili

Wolof

yéen jaam yi déggal-leen seeni sang ak wegeel gu mat sëkk, waxuma ñi baax te lewet rekk, waaye sax ñu wex ñi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

noi non intendiamo far da padroni sulla vostra fede; siamo invece i collaboratori della vostra gioia, perché nella fede voi siete già saldi

Wolof

du caageen nag noo leen bëgg a noot ci lu jëm ci seen ngëm, waaye nu ngi liggéeyandoo ak yéen ngir seen mbég, ndaxte ci ngëm ngeen sax.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

mentre andavamo alla preghiera, venne verso di noi una giovane schiava, che aveva uno spirito di divinazione e procurava molto guadagno ai suoi padroni facendo l'indovina

Wolof

am bés, ba nuy dem nag ca ñaanukaay ba, nu daje ak jaam bu jigéen bu rabu gisaane solu, te ay sangam di jariñu lu bare ci gisaaneem.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

«e' vero, signore, disse la donna, ma anche i cani si cibano delle briciole che cadono dalla tavola dei loro padroni»

Wolof

waaye jigéen ja ne ko: «waaw sang bi, teewul xaj yi di lekk ruusit, yi rot ci seen lekkukaayu boroom.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

voi, servi, siate docili in tutto con i vostri padroni terreni; non servendo solo quando vi vedono, come si fa per piacere agli uomini, ma con cuore semplice e nel timore del signore

Wolof

jaam yi, nangul-leen ci lépp seen sang, yi ci àddina. buleen ko def rekk ci seen kanam, di sàkku ngërëm, waaye na nekk lu dëggu ci yéen, ndax seen ragal boroom bi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

al suo ritorno il servo riferì tutto questo al padrone. allora il padrone di casa, irritato, disse al servo: esci subito per le piazze e per le vie della città e conduci qui poveri, storpi, ciechi e zoppi

Wolof

«surga ba dellu ca njaatigeem nettali ko loolu lépp. noonu boroom kër ga mer, daldi ne surga ba: “demal gaaw ca pénc ya ak ca mbedd ya ca dëkk ba, te indil ma fii néew doole yi, ñu làggi ñi, gumba yi ak lafañ yi.”

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,787,721,544 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK