Vous avez cherché: profane (Italien - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Italien

Wolof

Infos

Italien

rifiuta invece le favole profane, roba da vecchierelle

Wolof

tanqamlul ay léebi diiney neen, di ay wax yu amul bopp yu àddina kese; waaye tàggatal sa bopp ci ragal yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

evita le chiacchiere profane, perché esse tendono a far crescere sempre più nell'empietà

Wolof

moytul bépp jataayu waxi neen yu àddina kese, ndax ña fa toog dinañu gën a xuus cig weddi,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

o timòteo, custodisci il deposito; evita le chiacchiere profane e le obiezioni della cosiddetta scienza

Wolof

céy yaw timote, sàmmal li la yàlla dénk! tanqamlul waxi neen yu àddina kese, te dëddu werantey ñi mbubboo xam-xam, fekk dañoo réer.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

di quanto maggior castigo allora pensate che sarà ritenuto degno chi avrà calpestato il figlio di dio e ritenuto profano quel sangue dell'alleanza dal quale è stato un giorno santificato e avrà disprezzato lo spirito della grazia

Wolof

ku xeeb doomu yàlla ji te fonkadi deretu kóllëre, ji ñu ko sellale, te muy toroxal xelum yàlla, mi indi yiw, naka la mbugalam war a gën a yéese?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,790,299,343 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK