Vous avez cherché: quadrupedi (Italien - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Italien

Wolof

Infos

Italien

in essa c'era ogni sorta di quadrupedi e rettili della terra e uccelli del cielo

Wolof

boroom ñeenti tànk yépp ñu nga ca, ak yiy raam ci suuf, ak picci asamaan.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

fissandolo con attenzione, vidi in esso quadrupedi, fiere e rettili della terra e uccelli del cielo

Wolof

ma xool ko jàkk, seetlu ko bu baax, ma gis ca boroom ñeenti tànk yu nekk ci kaw suuf, di rabi àll yi, yiy raam ak picci asamaan.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Italien

e hanno cambiato la gloria dell'incorruttibile dio con l'immagine e la figura dell'uomo corruttibile, di uccelli, di quadrupedi e di rettili

Wolof

toxal nañu ndamu yàlla aji sax ji, wuutal fa nataali nit ku dul sax, moom ak ay picc, ay rabi àll mbaa yuy raam.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,791,686,474 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK