Vous avez cherché: adulescentes (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

scribo vobis patres quoniam cognovistis eum qui ab initio est scribo vobis adulescentes quoniam vicistis malignu

Wolof

maa ngi leen di bind, yéen baay yi,ndax xam ngeen ki nekkoon ca njàlbéen ga ba tey.maa ngi leen di bind, yéen waxambaane yi,ndax daaneel ngeen ibliis.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

similiter adulescentes subditi estote senioribus omnes autem invicem humilitatem insinuate quia deus superbis resistit humilibus autem dat gratia

Wolof

noonu itam yéen ndaw ñi, nangeen déggal mag ñi. te yéen ñépp, solooleen woyof ci seen biir, ndaxte:«yàlla day dàq ñi réy,di yiwal ñi woyof.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

scripsi vobis infantes quoniam cognovistis patrem scripsi vobis patres quia cognovistis eum qui ab initio scripsi vobis adulescentes quia fortes estis et verbum dei in vobis manet et vicistis malignu

Wolof

bind naa leen, samay doom,ndax xam ngeen yàlla baay bi.bind naa leen, yéen baay yi,ndax xam ngeen ki nekkoon ca njàlbéen ga ba tey.bind naa leen, yéen waxambaane yi,ndax yéena ngi dëgër,ndax kàddug yàllaa ngi dëkk ci yéen,te daaneel ngeen ibliis.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,454,904 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK