Vous avez cherché: aliis (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

non enim ut aliis sit remissio vobis autem tribulatio sed ex aequalitat

Wolof

bëgguma leen a teg soxla, ngir woyofal ñi ci des, waaye na ñépp tolloole.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

quibus ille ait quia et aliis civitatibus oportet me evangelizare regnum dei quia ideo missus su

Wolof

waaye mu ne leen: «damaa war a dem ci yeneen dëkk yi, ngir yégle xebaar bu baax bi ci nguuru yàlla, ndaxte looloo tax ñu yónni ma.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

aliis etiam verbis pluribus testificatus est et exhortabatur eos dicens salvamini a generatione ista prav

Wolof

noonu mu artu leen ak yeneen wax yu bare, di leen dénk ne: «rëccleen ci niti jamono ju dëng jii.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

aiunt illi malos male perdet et vineam locabit aliis agricolis qui reddant ei fructum temporibus sui

Wolof

Ñu ne ko: «dina rey reyin wu ñaaw nit ñu soxor ñooñu, batale tool bi yeneen beykat, yi koy jox wàllam ci jamonoy meññeef.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et repleti sunt omnes spiritu sancto et coeperunt loqui aliis linguis prout spiritus sanctus dabat eloqui illi

Wolof

noonu ñu fees ak xel mu sell mi ñoom ñépp, ñu daldi wax yeneeni làkk, ni leen xel mu sell mi maye, ñu wax ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

in lege scriptum est quoniam in aliis linguis et labiis aliis loquar populo huic et nec sic exaudient me dicit dominu

Wolof

bind nañu ci téereb yoon wi:«dinaa wax ak mbooloo mii,jaare ko ci ay nit, ñuy wax yeneen làkk,ak ay gémmiñi doxandéem,waaye ba tey duñu ma déglu.» moom la boroom bi wax.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

a quibusdam quia iohannes surrexit a mortuis a quibusdam vero quia helias apparuit ab aliis autem quia propheta unus de antiquis surrexi

Wolof

am it ñuy wax naan: iliyas moo dellusi. Ñeneen naan: «kenn ci yonent yu jëkk yaa dekki.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

multi homines condocefactionem contribuit gnome ab eo inito 1997; magis plures aliis modis contribuit, qualia translationes, documentationes, et qualitatem certareunknownmonitor vendor

Wolof

ay téeméeri nit cëru nañu ci yoonu gnome dalee ci juddam 1997 ba léegi, ñeneen ñi ci yeneen fànn, muy tekki, uti xibaar ak ci wóoral baaxaayam.unknownmonitor vendor

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,788,810,945 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK