Vous avez cherché: cognatos (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

existimantes autem illum esse in comitatu venerunt iter diei et requirebant eum inter cognatos et noto

Wolof

Ñu xalaat ne, yeesu dafa àndoon ak ñeneen, ñi ñu bokkaloon yoon. bi ñu doxee bésub lëmm, ñu tàmbali di ko seet ci seen bokk yi ak seen xame yi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

salutate andronicum et iuniam cognatos et concaptivos meos qui sunt nobiles in apostolis qui et ante me fuerunt in christ

Wolof

nuyul-leen ma it andoronikus ak yuñas, sama bokk, yi ñu ma booleeloon tëj; am nañu tur ci ndawi yàlla yi, te ñoo ma jiitu sax ci gëm kirist.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

dicebat autem et ei qui se invitaverat cum facis prandium aut cenam noli vocare amicos tuos neque fratres tuos neque cognatos neque vicinos divites ne forte et ipsi te reinvitent et fiat tibi retributi

Wolof

noonu yeesu ne ki ko woo woon lekk: «boo dee woote añ walla reer, bul woo rekk say xarit, say doomi ndey, say bokk, walla say dëkkandoo yu am alal. lu ko moy ñooñu itam dinañu la woo, fey la bor bi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,188,732 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK