Vous avez cherché: diligamus (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

nos ergo diligamus quoniam deus prior dilexit no

Wolof

danuy wéy ci mbëggeel, ndax moo nu jëkk a bëgg.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

filioli non diligamus verbo nec lingua sed opere et veritat

Wolof

samay doom, bunu bëggante ci wax mbaa ci làmmiñ rekk, waaye ci jëf ak ci dëgg.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

quoniam haec est adnuntiatio quam audistis ab initio ut diligamus alterutru

Wolof

ndaxte xebaar, bi ngeen déggoon ca ndoorte la, mooy lii: nanu bëggante,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

in hoc cognoscimus quoniam diligimus natos dei cum deum diligamus et mandata eius faciamu

Wolof

xam nanu ne, bëgg nanu doomi yàlla yi ci lii: bëgg yàlla tey sàmm ay ndigalam.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

deum nemo vidit umquam si diligamus invicem deus in nobis manet et caritas eius in nobis perfecta es

Wolof

kenn musul a gis yàlla, waaye bu nu bëggantee, yàllaa ngi dëkk ci nun te mbëggeelam mat na sëkk ci nun.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

carissimi diligamus invicem quoniam caritas ex deo est et omnis qui diligit ex deo natus est et cognoscit deu

Wolof

samay soppe, nanu bëggante, ndax mbëggeel ci yàlla la bawoo; képp ku bëgg sa mbokk nag, ci yàlla nga juddoo, te xam nga yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,792,323,647 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK