Vous avez cherché: gaudium (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

factum est ergo magnum gaudium in illa civitat

Wolof

noonu mbég mu réy tàbbi ca dëkk ba.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et haec scribimus vobis ut gaudium nostrum sit plenu

Wolof

nu ngi leen di bind yëf yii, ngir sunu mbég mat sëkk, nun ñépp.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

omne gaudium existimate fratres mei cum in temptationibus variis incideriti

Wolof

yéen samay bokk, waxtu wu nattu yi dalee ci seen kaw, ak nu ñu man a mel, defleen ko ni mbég mu réy,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et erit gaudium tibi et exultatio et multi in nativitate eius gaudebun

Wolof

sa mbég lay doon, sa xol sedd ci, te ñu bare dinañu bég ci juddoom,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

fructus autem spiritus est caritas gaudium pax longanimitas bonitas benignita

Wolof

waaye li xelu yàlla mi di meññ mooy: mbëggeel, mbég, jàmm, muñ, laabiir, mbaax, kóllëre,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

haec locutus sum vobis ut gaudium meum in vobis sit et gaudium vestrum impleatu

Wolof

wax naa leen loolu, ngir ngeen bokk ci sama mbég, te seen bos mat sëkk.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et hoc confidens scio quia manebo et permanebo omnibus vobis ad profectum vestrum et gaudium fide

Wolof

loolu wóor na ma; kon xam naa ne, dinaa fi des, di leen taxawu yéen ñépp, ngir seen ngëm yokku, ànd ak mbég.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et dixit illis angelus nolite timere ecce enim evangelizo vobis gaudium magnum quod erit omni popul

Wolof

waaye malaaka mi ne leen: «buleen tiit, ndaxte dama leen di xamal xebaar bu baax buy indi mbég mu réy ci nit ñépp.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

quae est enim nostra spes aut gaudium aut corona gloriae nonne vos ante dominum nostrum iesum estis in adventu eiu

Wolof

ndaxte bés bu yeesu sunu boroom dellusee, te nu fekke ko, kan mooy sunu yaakaar? kan mooy sunu mbég? kan mooy sunu kaala, gi nuy tiitaroo?

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

illi igitur deducti ab ecclesia pertransiebant foenicen et samariam narrantes conversionem gentium et faciebant gaudium magnum omnibus fratribu

Wolof

kon nag mbooloo mi gunge leen, ñu jaar ci wàlli fenisi ak samari, di nettali ni ñi dul yawut woññikoo ci yàlla, ba bokk yépp am ca mbég mu réy.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

ait illi dominus eius euge bone serve et fidelis quia super pauca fuisti fidelis super multa te constituam intra in gaudium domini tu

Wolof

njaatigeem tontu ko: “def nga lu baax, surga bu baax nga te takku. gannaaw takku nga ci lu tuuti, dinaa la dénk lu bare. kaay bokk ci sama mbég.”

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

mulier cum parit tristitiam habet quia venit hora eius cum autem pepererit puerum iam non meminit pressurae propter gaudium quia natus est homo in mundu

Wolof

jigéen ju nekk ci mat, dafay jàq, ndaxte waxtu wi mu war a jur jot na. waaye bu doom ji juddoo, dina fàtte coonoom ndaxte day bég ci li doom ji gane àddina.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et hoc ipsum scripsi ut non cum venero tristitiam super tristitiam habeam de quibus oportuerat me gaudere confidens in omnibus vobis quia meum gaudium omnium vestrum es

Wolof

looloo tax ma binde noonu, ngir bañ a agsi, am naqar ci ñi ma waroon a bégal. am naa kóolute ci yéen ñépp ne, sama mbég mooy seen mbég.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,782,472,076 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK