Vous avez cherché: mansimus (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

et cum venissemus syracusam mansimus ibi tridu

Wolof

noonu nu teer dëkku sirakus, toog fa ñetti fan.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

nos vero navigatione explicita a tyro descendimus ptolomaida et salutatis fratribus mansimus die una apud illo

Wolof

bi nu jógee tir nag, nu demaat ci géej, ba teer patolemayis. foofa nu nuyu bokk ya, yendu, fanaan.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

inventis autem discipulis mansimus ibi diebus septem qui paulo dicebant per spiritum ne ascenderet hierosolyma

Wolof

nu wut taalibe ya, ba gis leen, toog ak ñoom juróom-ñaari fan. Ñoom nag ñu ne pool ci li leen xelu yàlla mi may, mu bañ a dem yerusalem.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

alia autem die profecti venimus caesaream et intrantes in domum philippi evangelistae qui erat de septem mansimus apud eu

Wolof

nu jóge fa ca ëllëg sa, ñëw ba ca dëkku sesare. nu dugg ca kër filib, taskatu xebaar bu baax bi, mi bokk ci juróom-ñaar ña, nu dal fa moom.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,188,732 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK