Vous avez cherché: nazareth (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

populi autem dicebant hic est iesus propheta a nazareth galilaea

Wolof

mbooloo ma tontu leen ne: «kii moo di yonentu yàlla yeesu, bi jóge nasaret ci galile.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et dixit ei nathanahel a nazareth potest aliquid boni esse dicit ei philippus veni et vid

Wolof

nataneel tontu ko ne: «aa! ndax dara lu baax man na jóge nasaret?» filib ne ko: «Ñëwal gis.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et relicta civitate nazareth venit et habitavit in capharnaum maritimam in finibus zabulon et nepthali

Wolof

gannaaw gi, mu toxoo dëkku nasaret, dem dëkk kapernawum, bi féeteek dex ga ci diiwaani sabulon ak neftali.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et factum est in diebus illis venit iesus a nazareth galilaeae et baptizatus est in iordane ab iohann

Wolof

booba yeesu jóge na dëkku nasaret ci diiwaanu galile, ñëw, yaxya sóob ko ci dexu yurdan.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et descendit cum eis et venit nazareth et erat subditus illis et mater eius conservabat omnia verba haec in corde su

Wolof

noonu yeesu daldi ànd ak ñoom, dellu nasaret te déggal ay waajuram. fekk yaayam moom takk mbir yooyu yépp ci xolam.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

ascendit autem et ioseph a galilaea de civitate nazareth in iudaeam civitatem david quae vocatur bethleem eo quod esset de domo et familia davi

Wolof

yuusufa nag daldi jóge nasaret ca diiwaanu galile, jëm ca diiwaanu yude ca betleyem, dëkk ba daawuda cosaanoo, ndaxte ci askanu daawuda la bokk.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
8,021,868,159 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK