Vous avez cherché: parabolam (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

vos ergo audite parabolam seminanti

Wolof

«yéen nag dégluleen li léebu beykat biy tekki.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et ait ad illos parabolam istam dicen

Wolof

noonu yeesu daldi leen wax léeb wii ne leen:

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

respondens autem petrus dixit ei edissere nobis parabolam ista

Wolof

piyeer nag jël kàddu gi, laaj yeesu: «firil nu léeb wi.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et ait illis nescitis parabolam hanc et quomodo omnes parabolas cognosceti

Wolof

noonu yeesu ne leen: «ndax xamuleen léeb wii? nu ngeen xame nag léeb yi ci des?

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

ait autem ei petrus domine ad nos dicis hanc parabolam an et ad omne

Wolof

piyeer ne yeesu: «boroom bi, ndax dangay dégtal léeb wii ngir nun rekk walla ngir mbooloo mépp?»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

dicebat autem et parabolam ad illos quoniam oportet semper orare et non deficer

Wolof

noonu yeesu wax leen itam léeb wii ngir xamal leen ne, war nañoo sax ci ñaan te bañ a xàddi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

dicebat autem et ad invitatos parabolam intendens quomodo primos accubitus eligerent dicens ad illo

Wolof

yeesu gis ni gan yi doon tànne toogu yu yiw yi, mu daldi leen wax léeb wii:

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

aliam parabolam proposuit eis dicens simile est regnum caelorum grano sinapis quod accipiens homo seminavit in agro su

Wolof

yeesu waxaat leen beneen léeb ne leen: «nguuru yàlla aji kawe ji dafa mel ni doomu fuddën bu nit jël, ji ko ci toolam.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

a ficu autem discite parabolam cum iam ramus eius tener fuerit et nata fuerint folia cognoscitis quia in proximo sit aesta

Wolof

yeesu teg ca ne: «jàngleen misaalu garabu figg ga. boo xamee ne ay bànqaasam duy nañu, tey xobam sëq, xam ngeen ne nawet jege na.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

aliam parabolam locutus est eis simile est regnum caelorum fermento quod acceptum mulier abscondit in farinae satis tribus donec fermentatum est totu

Wolof

yeesu teg ca beneen léeb ne leen: «nguuru yàlla aji kawe ji dafa mel ni lawiir bu jigéen jël, jaxase ko ak ñetti andaari fariñ, ba kera tooyal bépp di funki.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

aliam parabolam audite homo erat pater familias qui plantavit vineam et sepem circumdedit ei et fodit in ea torcular et aedificavit turrem et locavit eam agricolis et peregre profectus es

Wolof

yeesu teg ca ne: «dégluleen beneen léeb. amoon na fi benn boroom kër bu jëmbët toolu réseñ. mu ñag tool bi, gas ci biir pax, ngir nal ci réseñ yi. mu tabax wottukaay, batale ko ay beykat, daldi tukki.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,781,714,392 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK