Vous avez cherché: petrum (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

deinde post annos tres veni hierosolyma videre petrum et mansi apud eum diebus quindeci

Wolof

ba ñu ca tegee ñetti at, ma sog a dem yerusalem, ngir xamante ak sefas, dal fa moom lu mat ñaari ayu-bés.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

factum est autem petrum dum pertransiret universos devenire et ad sanctos qui habitabant lydda

Wolof

piyeer nag di wër, di jaar fu nekk, tey dem ci gaayi yàlla yi dëkk lidd,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

his auditis conpuncti sunt corde et dixerunt ad petrum et ad reliquos apostolos quid faciemus viri fratre

Wolof

bi ko mbooloo ma déggee, naqaru xol wu metti jàpp leen; ñu daldi ne piyeer ak ndaw ya ca des: «bokk yi, lu nu war a def?»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

cum autem audissent apostoli qui erant hierosolymis quia recepit samaria verbum dei miserunt ad illos petrum et iohanne

Wolof

bi nga xamee ne ndaw yi nekk yerusalem yég nañu ne, waa samari nangu nañu kàddug yàlla; ñu yónni fa piyeer ak yowaana.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et cum venisset domum non permisit intrare secum quemquam nisi petrum et iohannem et iacobum et patrem et matrem puella

Wolof

bi yeesu agsee ca kër ga, nanguwul kenn duggaaleek moom, ñu dul piyeer, yowaana, saag ak waajuri xale ba.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et conversus dominus respexit petrum et recordatus est petrus verbi domini sicut dixit quia priusquam gallus cantet ter me negabi

Wolof

noonu boroom bi geestu, xool piyeer. te piyeer fàttaliku la ko boroom bi waxoon ne: «bala ginaar a sab tey jii, dinga ma weddi ñetti yoon.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

cucurrit ergo et venit ad simonem petrum et ad alium discipulum quem amabat iesus et dicit eis tulerunt dominum de monumento et nescimus ubi posuerunt eu

Wolof

mu daw, dem ca simoŋ piyeer ak ca beneen taalibe ba, maanaam ka yeesu bëggoon, ne leen: «jële nañu néewu boroom ba ca bàmmeel ba, te xamunu fu ñu ko yóbbu.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,743,899,900 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK