Vous avez cherché: philippum (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

simonem quem cognominavit petrum et andream fratrem eius iacobum et iohannem philippum et bartholomeu

Wolof

simoŋ, mi yeesu tudde piyeer, ak andare, mi bokk ak piyeer ndey ak baay; saag ak yowaana, filib ak bartelemi,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

in crastinum voluit exire in galilaeam et invenit philippum et dicit ei iesus sequere m

Wolof

ca ëllëg sa mu fas yéenee dem diiwaanu galile te mu gis filib. yeesu ne ko: «toppal ci man.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et andream et philippum et bartholomeum et mattheum et thomam et iacobum alphei et thaddeum et simonem cananeu

Wolof

andare ak filib,bartelemi ak macë,tomaa ak saag doomu alfe,tade ak simoŋ, mi bokk ca mbooloo, ma ñu tudde Ñi farlu ci moom seen réew;

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

cum autem ascendissent de aqua spiritus domini rapuit philippum et amplius non vidit eum eunuchus ibat enim per viam suam gauden

Wolof

ba noppi ñu génn ca ndox ma, te ca saa sa xelu boroom bi fëkk filib, ba jaraaf ja gisatu ko, waaye mu toppaat yoonam, ànd ak mbég.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

cum sublevasset ergo oculos iesus et vidisset quia multitudo maxima venit ad eum dicit ad philippum unde ememus panes ut manducent hi

Wolof

bi yeesu xoolee, gis mbooloo mu réy di ñëw ci moom, mu ne filib: «fu nuy jële mburu, mu nu leen man a dundale?»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

angelus autem domini locutus est ad philippum dicens surge et vade contra meridianum ad viam quae descendit ab hierusalem in gazam haec est desert

Wolof

naka noonu benn malaakam boroom bi ne filib: «jógal te jublu misra, jaar ci yoon wi jóge yerusalem, jëm gasa, di màndiŋ.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et placuit sermo coram omni multitudine et elegerunt stephanum virum plenum fide et spiritu sancto et philippum et prochorum et nicanorem et timonem et parmenam et nicolaum advenam antiochenu

Wolof

lii ñu wax nag neex na mbooloo mépp. noonu ñu tànn ecen, di nit ku fees ak ngëm ak xel mu sell mi, boole ci filib ak porokor, teg ca nikanor, timon, parmenas ak nikolas, mi juddoo ancos te tuub ci yoonu yawut ya.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,777,736,387 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK